No More Lyrics
No More Lyrics by ASHS THE BEST
[REFRAIN]
Fi loufi way am y’Allah ko may
Nianal niou may la mo geun ngey goungué
(goungué, goungué, nianal niou may la mo geun ngey goungué)
Allalou dounya diaroul niawo
Yéné nek la borom ma thiey fanané
(Fanan, fanan, yéné nek la borom ma thiey fanan)
No more (yéné lou bone yéné ray sa bop leu)
No more (yéné nek la borom ma thiey fanane)
No more (fanané)
No more (yéné nek la borome ma thiey fanane)
[COUPLET]
Fi koufi amoul dagn la nopal, koufi né ci yone danioula tek temps
Yeah ! Djiko sénégalais moy beurri djiko
Ya raw picasso ndax beurri couleur, bouniou alo nga nopi casso
Daf fek nga moumeu mais takhoul nga téki sokhlam
Motax moudieuntal am na handicap takhoul nga geum boy
Boffi guissé kougn fi yeureum dafa denkané
Yeurmandé diekh, nétali baram sassuné
Yeurmandé diekh si xol mais da mougn
Boula ken geumoul geumeul sa bop goor (ligueye moy fay)
Ykkar ci y’Allah geuneu woor, yakkartu yakkar ci y’Allah moussoula woor
Kouci nek ak li la y’Allah buur bi may boul sokhor, boul ignane yeah!
Y’Allah buur bi nélawoul la fi lofi dieuf lagn ley fay (lo def lagn ley fay
[REFRAIN]
Fi loufi way am y’Allah ko may
Nianal niou may la mo geun ngey goungué
(goungué, goungué, nianal niou may la mo geun ngey goungué)
Allalou dounya diaroul niawo
Yéné nek la borom ma thiey fanané
(Fanan, fanan, yéné nek la borom ma thiey fanan)
No more (yéné lou bone yéné ray sa bop leu)
No more (yéné nek la borom ma thiey fanane)
No more (fanané)
No more (yéné nek la borome ma thiey fanane)
Nioune bougouniou ngen ganio
Télou len lo, wa sénégal télou len lo
Fi nga yendou lay fanané (no no)
Fi nga yendou lay fanané (no no)
No more, no more (yéné nek la borom ma thiey fanane)
No more (fanané)
No more (yéné nek la borome ma thiey fanane)
[REFRAIN]
Fi loufi way am y’Allah ko may
Nianal niou may la mo geun ngey goungué
(goungué, goungué, nianal niou may la mo geun ngey goungué)
Allalou dounya diaroul niawo
Yéné nek la borom ma thiey fanané
(Fanan, fanan, yéné nek la borom ma thiey fanan)
No more (yéné lou bone yéné ray sa bop leu),
No more (yéné nek la borom ma thiey fanane)
No more (fanané)
No more (yéné nek la borome ma thiey fanane)
Watch Video
About No More
More ASHS THE BEST Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl