ASHS THE BEST Maa Ngi Dem cover image

Maa Ngi Dem Lyrics

Maa Ngi Dem Lyrics by ASHS THE BEST


Now I know now I know
But I don’t know what I’m feeling inside
Gestu woo ma

Maa ngi dem maa ngi dem
Soo ma gisatul dem naa
Maa ngi dem baayi a fi sama xol
Di naa weet weet ci sama yoon
Subateel ba jant sow
Yaa ngi sèntu sa waay ju fi joge woon

Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la

Ñëw naa fi noor  (ñëw naa ba dem gisoo ma)
ñëw naa fi nawet  (ñëw naa fi nawet tamit)
Ñëw naa fi koor  (Tabaski akk Tamxarit)
Fekk fi bekkoor  (fekk la ngay bekkoor)
Li ma dundee  (li ma dundee)
Akk li ma weesu (akk li ma weesu)
Day dellusee (da fay dellusee)
Ba mel ni seetu (ba mel ni seetu)

Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la

Dem naa te taggu wu ma la  (dem naa)
Suma reeree mbaa duñ ne yow la (mbaa duñ ne yow la)
Jooy naa te kenn dooru ma(man dem naa)
Suma reeree mbaa duñ ne yow la (yow la)

Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la

Maa ngi dem maa ngi dem
Soo ma gisatul dem naa

Watch Video

About Maa Ngi Dem

Album : Tukki (EP)
Release Year : 2022
Added By : Farida
Published : Dec 23 , 2022

More ASHS THE BEST Lyrics

ASHS THE BEST
ASHS THE BEST
ASHS THE BEST
ASHS THE BEST

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl