Boul Ko Faté Lyrics
Boul Ko Faté Lyrics by AMIRA ABED
Bayina lou beuri
Bayi na gnou beuri
Boul deff lougn niouy khébé
Damla nopp boulko faté
Gni nane dou sorri
Gni nane dou sotti
Beugg naleu té louma am dieul
Boul mey none yi louniou rétané
Té ioe khana khamo
Yaye pé ci khol bi sou done course do dieul ndaré
Mounouma lako neub day fégn ci nimlay kholé
Yaye sama choice nagn ci tekk brick
Doundou sunu paradise Oh oh
Boulma miineul sa bopou ba paré wone meu guinaw
Lomay tammal na nekk louy laaw
Khol dou hauum bagnkay beuss
Amatouma sago ci yaw
Mbeuguel di taw sama khol lima weur yeup di naat
Biss bimalay nieuk guiss souma sanione dey niowat
Baayi nieup né ioe leuuu
Ioe laay tiiteuroo woo waaayy
Boudoul yaw dou keneu fi nga nekk la né
Limay yeuk ci ioe mane dafma eupp doolé
Eyyy , Ohh ouhh hooo
Sama khol moma toogn bama melni
Mom moma toogn bama melni (ci ioe)
Yeeeeh ehhhhhh ey
Ohhhhh ouhhh ohhhhh ohh
Yaye sama ceetu
Boulma nakh ci ioe lay guiss sama bopou
Yaye lamp bimay leeral
Sodone diaye lougn ma ladj ma faye ko
Mba doma Rousslo ci sama kanamou ay nawlé
Yaye wakhna pape wakh samay kharit
Mani yaw leu
Beugouma ko rethiou
Loma ladj ma deff ko
Mala beug piir té louma ci gobé garr ko
Paré dékou lepp rek ci kaw nga kham ko
Pour niou dem dey dess ci ioe
Andeu niarakoy deff
Beugue nala bamou leer nieup
Dieul sa photo def ko sama profil yeup
Soudé mbeuguel diokh nalako bamou matt seukk
Bayil khel lima bayi lepp
Lepp nguirr yaw
Mbeuguel di taw sama khol lima weuurr yeup di naat
Biss bimalay nieuk guiss souma sagnone day nieuwat
Bayi nieup né yawleu
Yaw lay titeurooo woooo waaaayyy
Boudoul ioe dou keneu fi nga nekk la né
Limay yeukk ci ioe mane dafma eup doolé
Ohh ohoo hooo
Sama khol moma toogn bama melni
Mom moma toogn bama melni (ci ioe)
Yeeeeh ehhhhhh ey
Ohhhh ouhhhhh ohhhh ohh
Diokh naleu li gueuneu fort ci mane
Mouy sama khol
Kone dessalatoumla daaraaa
Aand niarakoy deff
Wane naleu li gueuneu sorri ci mane
Yaye sama khol kone dessalatoumla dara
Andeu niarakoy deff
Watch Video
About Boul Ko Faté
More AMIRA ABED Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl