Moo Ngi Fi Lyrics
Moo Ngi Fi Lyrics by AMIRA ABED
Lila thiy mousseul
Moy di moytou
Li gneup la titeul
Kone boul gueuméntou
Mome dafa gneuw
Nit gni di dém dianteu bi soo guissatou gnou lérr
Meme samay xarite meuneu tou malene guiss
Ba ko djip day tite
Boul faté ni mi ngui fi, batay
Lakhou na mais mingui fii, batay
Boul faté ni mi ngui fi, baa tayy
Lakho tina mais faites gaffe
Lila thiy mousseul
Moy di moytou
Li gneup la titeul
Kone boul gueuméntou
Moytandikou
Ni gnouy doundék diaane thi pakh
Respecté consigne yéy takh gnou doundaat lou nekh
Ndax wergou yaram bou sakh egal happyness
Revivons des jours meilleurs
Boul faté ni mi ngui fi, batay
Lakhou na mais mingui fii, faites gaffe
Boul faté ni mi ngui fi, baa tayy
Lakho tina mais faites gaffe
Together we will get there
And struggle for better days
It’s time to build our future
Diok ni li daf fiey diekh (par force)
Nguir aar sa bop aare sa ndiaboot
Moy respectez les gestes barrières
Bagna bayé ko fiy dieulé
Diok ni
Li da fiy diok…..par force
Lila thiy mousseul
Moy di moytou
Li gneup la titeul
Kone boul gueuméntou
Fagaro geun fadiou
Fagaro geun fadiou
Kone negn leen vacciner wou (vacciner wou)
Boul faté ni mi ngui fi, baa tayy
Lakho tina mais faites gaffe
Li arr sa bop aar sa ndiaboot, batay
Moy respecter les gestes barrières
Fais gaffe
Watch Video
About Moo Ngi Fi
More AMIRA ABED Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl