Def Ndam Lyrics
Def Ndam Lyrics by VIVIANE CHIDID
[VERSE 1]
Xaleul len ko yoone wi ni le
Teulalé tapis rouge bi bi ci la
Dou xéwé fen foudoul fi ci mome leu
Borome beuss bi yeksi neu mo ayé tay
Mané tay leu tay beussou fête leu
Bou dara sed ndax léppeu matt neu
Dou wéxé fen foudoul fi ci mome leu
Borome beuss bi yeksi neu niou sargal ko
[CHORUS]
Kaay leen, kaay leen kay len ki
Niou donne khar yeksi neu
Kaay leen, kaay leen kay len ki
Niou donne khar yeksi neu
[VERSE 2]
Na nieup niow niou guewe fi
Mané amoul mbok kharite deukeundo yi
Ioe da nga bax xa waral sa beuss mel ni
Borome beuss bi yeksi neu niou sargal ko
[CHORUS]
Kaay leen, kaay leen kay len ki
Niou donne khar yeksi neu
Kaay leen, kaay leen kay len ki
Niou donne khar yeksi neu
Kaay leen, kaay leen kay len ki
Niou donne khar yeksi neu
Kaay leen, kaay leen kay len ki
Niou donne khar yeksi neu
[VERSE 3]
Am nga fouleu am nga fayda
Sa ndaimbar rek ka waral sa beuss mel ni
Té nitte boula khol guiss si ioe diome
Kone borome beuss bi yeksi neu annh annh
Reew mi kou sagnone dafay
(Melni ioe, melni ioe)
Reew mi nieupeu beugeu
(Melni ioe, melni ioe)
Reew mi kou sagnone dafay
(Melni ioe, melni ioe)
Reew mi nioune nieupa beugeu
(Melni ioe)
Reew mi kou sagnone dafay
(Melni ioe, melni ioe)
Reew mi nieupeu beugeu
(Melni ioe, melni ioe)
Reew mi kou sagnone dafay
(Melni ioe, melni ioe)
Reew mi nioune nieupa beugeu
(Melni ioe)
[CHORUS]
Kaay leen, kaay leen kay len ki
Niou donne khar yeksi neu
Kaay leen, kaay leen kay len ki
Niou donne khar yeksi neu
Kaay leen, kaay leen kay len ki
Niou donne khar yeksi neu
Kaay leen, kaay leen kay len ki
Niou donne khar yeksi neu
Kaay leen, kaay leen kay len ki
Niou donne khar yeksi neu
Kaay leen, kaay leen kay len ki
Niou donne khar yeksi neu
Kaay leen, kaay leen kay len ki
Niou donne khar yeksi neu
Watch Video
About Def Ndam
More VIVIANE CHIDID Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl