NGAAKA BLINDé Freestyle Contrôle cover image

Freestyle Contrôle Lyrics

Freestyle Contrôle Lyrics by NGAAKA BLINDé


Wakhal sa M.c kébetou katt
La meunoul dem ak nioun
Niata nénn nga tothie ban dérét
Nga naan kon meuno dem ak kun
Boul diéguéti téféssou Malibu deh
Non pardon dama dioum
Mané woon nallén soul
Dama doul mais légui dina cool
Bingay diémeu dima tékk tank
sama tank migui si Aÿ bank
Wakh nako mouné daa lank
sans ndank dama la sank
Waa l’I moom meune rap
késsé wala teureudi la
Mane booma dégaté rékk may khoss lou
Diappal néh crédit lah
Man awma diotou rap non
Non awma diottou rap
yagui ci thiattou rap ma tok
Ci rap du dague thiotou rap
So, fuck rap galsen man rekk’ay vrai ci rap
Maay dokh di rap, di teri di rap
Di lekk thiérré du rap
Di tracé trait di rap
Par ici là melni kou takk téré si rap

Dama téla rap di deff nioom
Nieup lougnou teulé ci rap
Con paré ci rap gning may comparé ci rap
Lékk lékk ma melni Balla gaye
Yénn saay may beuré di rap
Non man comme kouy liguey
Sonatel dama am crédit rap

Diokh ma beat ak Mc bou gnémé rekk
Zéro commentaire
Nako kheuthie tagnthieu tekk KO ci
Nadj bi est ce que dou camembére
May rap di rée
Ngay rap di niangal est ce que dou dagua mérr
Cher frère meunoo ma guiss
Sa concert wallahi dama chère
Sound yimay improvisé rekkay leumbé town bi
Tathiouma nema waaw niata
Girl waaw snap sound bi
Minn na vol bi États-Unis
Paris wowéko pithie mi
Yenn tribu Rap new king di rap
A.K.A pithie me
Dagno dégg prip arbitre ta sifflé
Gaaw té mann la
Rakk ndaw loi meunti daw
Say tank dotoko reuthie man
Rap mbarikallah on thé tape man la
Sept  mètre percale ci sen rap  
Aythieu leumeus len
Door yé nara diss ni courou
Baye fall youkhoul awaloo
Tay thiepp dou nef ndakh penda  
Mbaye migui ci deudiou Awa Lo
Deub kani tokhogne KO sen beut  
Yii seugueul taffal touff
Deff ko vidéo saga sen ndaye
Comme man la Assane Diouf

Watch Video

About Freestyle Contrôle

Album : Freestyle Contrôle (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Oct 22 , 2019

More NGAAKA BLINDé Lyrics

NGAAKA BLINDé
NGAAKA BLINDé
NGAAKA BLINDé
NGAAKA BLINDé

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl