...

Femme Démontable Lyrics by LAMTORO

Ni kassou café touba a jetable
Femme trucage femme demontable.

Ki rek moye femme démontable
Habillage maquillage ni portable
Pose ongle
Pose xeff
Pose perruque
Pose wéne
Pose fess
Qui rek moye femme démontable
Habillage maquillage ni portable
Collé hanche
Dokhine di ridjie ni balance
Peinture makeup sa canam
Ni tableau picasso

Legui nak yangui melni auto ndraneu wou
Lo yautou rek nga lonkke sissa yaram pour etre si belleu
Cheveux naturel
Yaubouna sam xel
Yéne synthétique
Wé synthétique
Wéne synthétique
Fess synthétique
Elles sont toutes artificielles
Amna marque Dubaï
Amna marque chinois
Ki moye femme démontable

Ki rek moye femme démontable
Habillage maquillage ni portable
Pose ongle
Pose xeff
Pose perruque
Pose wéne
Pose fess
Qui rek moye femme démontable
Habillage maquillage ni portable
Collé hanche
Dokhine di ridjie ni balance
Peinture makeup sa canam
Ni tableau picasso

Ni Cassou café touba a jetable
Sa kanam nga mekup melni diable
Sister linga nékke c'est insupportable
Mbété kou nek si film ay compte fable
Degloul Sama song bi tey damalay sing song
Bawal sa yaram binga deukké di peinture
Sa tatouage amoul ben filing...Yes
Degloul Sama song bi tey damalay sing song bawal sa yaram binga fowé di piercing
Mais nono diémela naturel mo eupeu filing

Ki rek moye femme démontable
Habillage maquillage ni portable
Pose ongle
Pose xeff
Pose perruque
Pose wéne
Pose fess
Qui rek moye femme démontable
Habillage maquillage ni portable
Collé hanche
Dokhine di ridjie ni balance
Peinture mekup sa canam
Ni tableau picasso

Nga melni Jacky chan mo gueune ngaye diéma roy kim kardachan
Tare defay rére si xole bi é allah
Rére na si xole bi
Fénie na si thieur yi taro tar
Ni rek moye femme démontable

Ki rek moye femme démontable
Habillage maquillage ni portable
Pose ongle
Pose xeff
Pose perruque
Pose wéne
Pose fess
Qui rek moye femme démontable
Habillage maquillage ni portable
Collé hanche
Dokhine di ridjie ni balance
Peinture mekup sa canam
Ni tableau picasso

 

Watch Video

About Femme Démontable

Album : Femme Démontable (Single)
Release Year : 2019
Copyright : (c) 2019, Lamtoro Prod
Added By : Afrika Lyrics
Published : Sep 21 , 2019

More LAMTORO Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet

See also



You May also Like



Get Afrika Lyrics Mobile App

About AfrikaLyrics 

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2020, New Africa Media Sarl