Free Sénegal Lyrics
Free Sénegal Lyrics by JEEBA
Lima guente lima guente
Mbadou Sénégal bi ni ni la nara moudié
Leklé damay tok di dioy
Médiocrité laniou jiital def ko thi système bi
Faté ligueye ngeum ligueye mérité founiou dieum
Goorgorlu amatoul ndeysane
Degg na daniou yoor loudoul diexx
Goroulo yatoulo, boné niou ngafi nekal walay C’est faux
Daniou la faal nguir souniou avenir doom
Dou thiagané lou nek thi rew mi yako moom
Kone fatalikoul niou done khex ndax yow
Niou niak sen bakane nguir am euleuk bu baax
Way wax leen bala mouy niaw
Niaaaw niaaaw meunone na bania wax tok nopi bayi nonou
Souma ko defé mou niaw niaaaw
Free Sénégal diam sama rew
Yow dila wo dila wo
Mbadou Senegal bi ni ni la nara moudié
Leklé ma tite dila wo oh dila wo oh
Mbadou Sénégal ni ni la nara moudié
Way wax leen bala mouy niaw
Niaw niaw meunone na bania wax tok nopi bayi nonou
Souma ko défé mou niaw niaw
Free Sénégal diam sama reew
Xolal jeunesse bi
Keneu ligueyatou si
Baay katt biniou waara doundal mo geuna khiff
Naap katt bi di dioy guedj gui dagn ko siff
Thiono day reer fi bo amoul bras long bril do yeksi
Étudiant di dioyou nénagn danio sone
Takk deer yi diniou baume
Douniou seni none
Diama geune ay nio bok senegaaaaalll
Ndiaye Diama geune ayy aaay
Yow dila wo dila wo
Mbadou Sénégal bi ni ni la nara moudié
Leklé ma tite dila wo oh dila wo oh
Mbadou Sénégal ni ni la nara moudié
Way wax leen bala mouy niaw
Niaw niaw meunone na tok bania wax bayi nonou
Souma ko défé mou niaw niaw
FreeSénégal diam sama reew!
Watch Video
About Free Sénegal
More JEEBA Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl