Yaw Rek Lyrics
Yaw Rek Lyrics by HAKILL
[REFRAIN]
Yaw rek , Yaw rek
Boudoul ioe dou done kénén, kénén, kénén
Baby yaw rek, yaw rek, yaw rek
Boudoul ioe dou done kénén, kénén, kénén
Kone dina niow setsi sa maman
éh dina niow guiss si papa
Niou mayma ma takkeu la wawaw
def la sama niarel sama awa oh my baby
Yaw rek , Yaw rek
Boudoul ioe dou done kénén, kénén, kénén
[COUPLET 1]
Koumay set ma ngui aljanah
nah nah ! Soxna si yay sama aljanah enh yeah !
Ci sa wet rek lay tok, I will never let you go
Khamone na ni ioe yay done
sama diabar sama yayou dome
ioe yama doy yama matt soxna soumala amoul wone wett
Bea you dh one, you dh one soxla wouma niarel
Yay sama kharite may sa andando
gaal youma kolabo dama beug done ki ley contanne lo
kay niou melni Maabo éh !
[REFRAIN]
Yaw rek, Yaw rek
Boudoul ioe dou done kénén, kénén, kénén
Baby yaw rek, yaw rek, yaw rek
Boudoul ioe dou done kénén, kénén, kénén
Kone dina niow setsi sa maman
éh dina niow guiss si papa
Niou mayma ma takkeu la wawaw
def la sama niarel sama awa oh my baby
Yaw rek ,Yaw rek
Boudoul ioe dou done kénén, kénén, kénén nah nah !
[COUPLET 2]
Beug nala dara douko change
sama xol ioe lafeu chargé
douma tite ragalouma danger
y’Allah nama ray boudé mbeuguel dey gagner
M’ak ioe combat leu bouniou atté
bimala guissé la bardé
bou yabo ma done indo ma tey
wayé diaral ngama louko raw fouf ma belle
(Passage Parole Bambara)
Ya geuneu kham ni ci ioe mi la dof
ken mounoul wax bamala meusseu off
ndax beuss bouné damalay geuneu love
waye loumassi meun dama love
[REFRAIN]
Yaw rek Yaw rek
Boudoul ioe dou done kénén, kénén, kénén
Baby yaw rek, yaw rek, yaw rek
Boudoul ioe dou done kénén, kénén, kénén
Kone dina niow setsi sa maman
éh dina niow guiss si papa
Niou mayma ma takkeu la wawaw
def la sama niarel sama awa oh my baby
Yaw rek Yaw rek
Boudoul ioe dou done kénén, kénén, kénén nah nah !
[OUTRO]
Takkeu la rek, takkeu la, takkeu la rek.
Yako liguey, m’ak ioe jakeu ba rek
Kone dina niow setsi sa maman
éh dina niow guiss si papa
Niou mayma ma takkeu la wawaw
def la sama niarel sama awa oh my baby
Yaw rek Yaw rek
Boudoul ioe dou done kénén, kénén, kénén nah nah !
Watch Video
About Yaw Rek
More HAKILL Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl