Paroles de Noflaay
...
Paroles de Noflaay Par YOUSSOU NDOUR
Nit ki ni mu mel , yalla a ko ni def , soo bëggée sa noflaay , nahngu l ko ko
Nit ki li mu am , yalla a ko ko jox , soo bëggée sa noflaay , nahngu l ko ko
Nit ki li mu xam , yalla a ko xamal , soo bëggée sa noflaay , nahngu l ko ko
Nit ki li mu mën , yalla a ko ko won , soo bëggée sa noflaay , nahngu l ko ko
Fa yalla y fexe e , benn mindef du fa dem
Siis am kenn du ko bokk ak moom
Buur bi , Fa muy dogal e , mindef du fa dem
Nit ki ni mu mel , yalla a ko ni def , soo bëggée sa noflaay , nangu l ko ko
Nit ki li mu am , yalla a ko ko jox , soo bëggée sa noflaay , nahngu l ko ko
Nit ki li mu xam , yalla a ko xamal , soo bëggée sa noflaay , nahngu l ko ko
Nit ki li mu mën , yalla a ko ko won , soo bëggée sa noflaay , nahngu l ko ko
Fa yalla benn Mindef du fa dem
Siis am kenn du ko bokk ak môme
Buur bi , Fa muy dogal e , Mindef du fa dem,
Ni nga bëgg sa waay mel ko , sa waay i waay a koy mel
Nit ki ni mu mel , yalla a ko ni def , soo bëggée sa noflaay , nahngu l ko ko
Nit ki li mu am , yalla a ko ko jox , soo bëggée sa noflaay , nahngu l ko ko
Nit ki li mu xam , yalla a ko xamal , soo bëggée sa noflaay , nahngu l ko ko
Nit ki li mu mën , yalla a ko ko won , soo bëggée sa noflaay , nahngu l ko ko
Mooy tax doo soxor , mooy tax doo iñaan
Mooy tax doo rambaaj , mooy tax doo xonet
Mooy tax doo xibaar , mooy tax doo wuruj
Mooy tax doo miser , mooy tax doo sëngéem
Mooy tax , kenn du la torox al , di
Ecouter
A Propos de "Noflaay"
Plus de Lyrics de YOUSSOU NDOUR
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl