YOUSSOU NDOUR mbËggéel Dolee cover image

Paroles de mbËggéel Dolee

...

Paroles de mbËggéel Dolee Par YOUSSOU NDOUR


Lu ne ak fu ne

Lu mu mën ë ne

Bu ci am ul ee

Loo la du sore

Liy doole el lu ne , mooy mbëggéel

Waay , bokk bokk bokk yëg yëg

Loo lu moo ñuy daje le

Every where

Mbëggéel da fa yaatu

Lu ne lay am ci ku nekk

Lay feeñ , da fa yaatu ci domaine bu ne

Domaine bu ne , bu ne , bu ne bu ne , bu ne , bu ne , am na ca

Gis nga , da fa yaatu

Nit di në bëgg

Lu neex ci xol am muy mbëggéel

Nit lu muy bëgg

Yal na doon

Li gën ci moom

Nit di na bëgg

Lii bëgg leneen

Mbëggéel lë

Ecouter

A Propos de "mbËggéel Dolee"

Album : (Single)
Année de Sortie : 2025
Copyright :
Ajouté par : Farida
Published : Apr 04 , 2025

Plus de Lyrics de YOUSSOU NDOUR

YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl