YOUSSOU NDOUR Ballago Ndoumbé Yatma  cover image

Paroles de Ballago Ndoumbé Yatma

Paroles de Ballago Ndoumbé Yatma Par YOUSSOU NDOUR


Billaay , ballago ndoumbé yatma  
Su ñu waaji xaj oon na fi
Naxxar doηη ,la ñu bayyee
Yalla , wonneeti na
Li tax ba mbir mi metti lool
Ñun da ñu ko foog wul woon
Yëf yi gaaw ba bette gnou
Billaay wéetël na ñu
Njiinoo njiin faramaareen
Gòor u jaaga , nelaw naa
Baay i wally dem na nii
Ñun daal wéetël na ñu

Ma ngi koy jaale Sénégal
Di ko jaalé Gambia
Di ko jaalé adduna
Ndaanaan ba dem na nii

Thione ballago, ndoumbé yatma
Bu yalla buur bi doon taggoo
Kon di na ñu bayék yaw
Ni patrimoine bi nga ñu bayyeel
Yee gua nit gñi, tete leen ci adduna
Yee gua nit gñi, tete leen
Xam al leen ci adduna
Ahhh   -   Balaago

Yee gua nit ñi ci adduna xam al leen
Ni ñu war a nekkek  
Ak ni ñu war a dundée
Ak ni ñu war a jëfleentee
Jinaxoo mbaay
Yaw mi dëkké biir suuf
Boo dem ee neel ballago, réew maa ngi koy joy
Aduna  ngi koy jooy
Art baa ngi koy jooy

Njiin faramaareen
Thione seck , wéetël na ñu
Ballago ndumbé yaatma
Adduna , am ul solo
Li tax ba mbir mi metti lool
Ñun da ñu ko foog wul woon
Yëf yi gaaw ba bette gno
Ndanaan ba demna ni
Njiin faramaareen
Thione seck , wéetël na ñu
Ballago ndumbé yaatma
Adduna , am ul solo

Ecouter

A Propos de "Ballago Ndoumbé Yatma "

Album : Mbalax (Album)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Nov 12 , 2021

Plus de Lyrics de YOUSSOU NDOUR

YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl