VITO Etiquette cover image

Paroles de Etiquette

Paroles de Etiquette Par VITO


Dioudou wouma ak mic
Dioudou wouma pour nek musicien
Dioudo wouma studio cii maternité la dioudo kone mane ak yow yeup gnossi bok yém
Domi adama ndiaye
Dioudou am papa am yaye
Fou sori la diougué té mangui ak bop bou féss ak tank you duegeur kone guissoumafi louma yém
Meune nga yakk sama der
Mais douma téré diap teint
Patouma lafagnouma kone guissoumafi loumay téré yokou thiéré doli gnéx
Douma diolou douma bin
Nigger ragalouma dhé
Mangui dégg jam géré sama life bousseu xol bi nakaré mani  yako téré nex

Légui nénégn rappeur la dama wathie damay toukh damay nane
SDF lagn may wowé cii kogn ndakh galé gueudie nafa fanane
Maman mangui diégueulou souma sagnone lou gnaw dou diogué cii mane
Mais wakh jii amoul sens comme swingom la rek man day dadji sen ngam
Ni dépensou galé gneupa ma beug lidieunti
Mais meunou gnou am parceque gnom gneupa bideunti
Idole tchi sen domi samay photo lagn coupeuti
May dessiné sen life gnom gnou beug ma dioubeunti
Nénégn ma dotchi guéneu mani lén d’accord c’est possible parceque nékouma cii bir
Goné gou ndaw té sama parcours meune na binde ay livre kone aythieu diéguécil nga lire
(IMVIT)

Déma wowé héé
So khamoul may kane
Ragalouma dhé
Immortel Duncan

Déma wowé héé
So khamoul may kane
Ragalouma dhé
Immortel Duncan

All eyes one me wér bii fégn na tay
Soul ay rappeur diotoumalen réy
Paparazzi sama palanetér
Francois bedon yakal sama dér

All eyes one me wér bii fégn na tay
Soul ay rappeur diotoumalen réy
Paparazzi sama palanetér
Francois bedon yakal sama dér

Succès moko yobalé mom dafa réw ba doff
Proukh leu ndakh xaritou dembam yeup la off
Dafa tela yeug bopam té defagoufi tousse
Mbeur bou ndaw leu cii guéw bi ba paré beuri touss

Lekagoul dara ba paré didjie day
Amoul talent sétane ko legui mou fay
Dafa wérou té wérouwayam bii deugueuroul
Ben projet la guénè ba legui defagoul

Est-ce que yama diokh ma lek yama diokh ma nane
Est-ce que sa pochou baye y’a tal sounou tchinou keur
Doundou na lou gueuneu tar avant ma ame ay fans
Té dara dou té ba douma thiop gni nguen diwone beure

Legui nom bi dafa qualifié ak épithètes
Dou matos bou bess boulma outeul étiquette
Abdoulaye ya financé demouma fén di quête
Yaga gueum sama bop depuis diamanoy makette

Damlen bayi cii bain takh sen lafi toy
Mane ak yén ni sama dome ak kinder joys
Goné nga amago parcours dokhal foyi
Sama idolou bopwakhma  Cii koumay roy

Ame rétane you sincère ak dioyou hypocrite
Boulen ma classé sounguen ko defoul par ordre de mérite
Seni pneus crevés gnou beugma deff crithe
Mane dama départ na bou yagg  lata ma dégg prip


Déma wowé héé
So khamoul may kane
Ragalouma dhé
Immortel Duncan
Déma wowé héé
So khamoul may kane
Ragalouma dhé
Immortel Duncan

All eyes one me wér bii fégn na tay
Soul ay rappeur diotoumalen réy
Paparazzi sama palanetér
Francois bedon yakal sama dér
All eyes one me wér bii fégn na tay
Soul ay rappeur diotoumalen réy
Paparazzi sama palanetér
Francois bedon yakal sama dér

Ecouter

A Propos de "Etiquette"

Album : Etiquette (Single)
Année de Sortie : 2022
Copyright : (c) 2022, Buzzlab
Ajouté par : Afrika Lyrics
Published : Oct 15 , 2022

Plus de Lyrics de VITO

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl