Paroles de Leeray
Paroles de Leeray Par WIZZY KANA
Toog thi sama xole ba abadane
Dahimane denk naala sama rouh
Iow laa teg thi kaw ndakh yaasi meune
Meunou nio beuré sa kaw ndakh yama daane
Ayy wakh you sew dou meuneu niakk souniou biir
Boulma méré soumala togné nangma baal
Leeraay
Yaay sama leeraay
Yaama dieulé si leundeum sotti ma leer
Yamay motali
Sa xole dou weet ndakh makoy wetali
Ehh iow leuh Diamond bi meuneu leeral sama eyes
Yaay sama lingueer beug naala deff jabare
Doff loo ngama ba parei denk naala samay fane
Beugouma nga merr teg naala fima teg sama yaaya booyé
Yaama joureul samay doom
Iow laa nara deff seen yaaya booyé
Mbeuguel day sakh thi xol iow
Yaay garab bi meuneu fadj sama feebar
Jaroul malay wakh ni damala nopp
Boo xolei samay beute ding kofa guiss sakh
Leeraay
Yaay sama leeraay
Yaama dieulé si leundeum sotti ma leer
Yamay motali
Sa xole dou weet ndakh makoy wetali
Ehh iow leuh Diamond bi meuneu leeral sama eyes
Ecouter
A Propos de "Leeray"
Plus de Lyrics de WIZZY KANA
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl