Paroles de Djiguene
Paroles de Djiguene Par WALLY SECK
Amna bene waw domi adama ham
Djiko yi si djiguenne goor
Y’Allah def lolou
Yak mome lewone sama djiguene
Ba ngéne di gonei
Yak mome lewone sama djiguene
Ba ngéne di gonei
Ba ni nguene di magé sey djiko
Nekhone naniou
Lolou niou khirone si yaw
Baniou def la sokhna
Penkou lagn le done sentou
Faw nge niou fetei
Bigne la takei indi keur ga nguir
Diamou y’Allah khifoulo maro
Raf lé wo niakaloula fayda
Tass nge se seuy top se bakan am si alal
Dem ci makka gnibissi niounane le adja
Fekhei ngeu dal ba degue Adja
Alla diamfamani diamfamani boussou
Ali bougou wogesso tepoba
Doumousonouwo Ali bougou wogesso
Tepoba doumousso nouwo
Diamm famaneeee bousso
Deuké ci nane ma tak ma tak ma
Deuké ci nane ma tak ma tak ma
Yama watal soumala takei gnima
Massel dinagn ma niémé
Yeureum sama wadji moma wakh lo
Liko dal lay bagn mou dal
Souniouye morome
Maman Diop yayou Diouldé
Titeuloulo se djeukeur
Aita Ndoye yayou Modi
Titeuloulo se djeukeur
Djiguène foulak feyda molay may mana
Adjaratou Nogueye Ngom
Sama mame djodji amone daraja
Adjaratou Ndeye Wouri Ba
Mame boye am nge daradja
Ndeye Soda Ba adja Diop
Wolma Falli Mbaye
Amngene daradja
Awa Cheikh Seck Ndeye Astou
Ndella Wally Ndeye Astou
Nionguilene di sani niane
Boulene niou meusseu faté
Adouna amoul solo boulen
Me djapé dounya
Kou ci beug ame tiathie
Kou ci beug ame tiathie
Topotol se djeukeur soko
Défé geurem nié nala
Kou ci beug ame tiathie
Kou ci beug ame tiathie
Topotol se djeukeur soko
Défé geureum nié nala
Ecouter
A Propos de "Djiguene"
Plus de Lyrics de WALLY SECK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl