Paroles de Damakoy Def
Paroles de Damakoy Def Par JAHMAN XPRESS
Liguay djay damakay mayé
Waw man yoyu damakay def
Affiché indo dawal cow boy
Anh man yoyu damakoy def
Liguén teulé damakoy fowé
Waw man yoyu damakoy def
Sagnsé dumako yeugual sama yaram
Surtout yoyu damakoy def
Ak yoyu yeup damakoy def
Xulo wuma xéxuma
Même yoyu damakoy def
Fuma teulé ngani tala meuné
Yoyu yeup damakoy def
Aka ma bandit man ci xallé
Yoyu yeup damakoy def
Ngani dama leer pourtant damako woyafal
Def relax nank ni comme kussi beugoul dara
Ragaluma kénn kuddul yallah mima saak
Té kouy dokh ci leundeum
Moy sokhla lampe yi takk
Taluma tothie man
Damay tabakh guis nga nima coolé
Damako meun ba xamko motax
Num nekh lakoy déffé
Bussa garde wathie taay nga raak ba duggu palais
Nala téla fay ni lakeu ci biir pompier
Sama deer menoko yak li nangako tak téré
Del deuké xine may deuké taw ba bum yi bayi doré
Ligni def du bén guiss nga ci bolé pank
Fo guis samay tof si souf cœur yi lalko nank
Xamé sissou man yi dilém bégué
Yoyu sakh damakoy def
Yégual ford dilén djégué
Même lolu damakoy def
Eh dumalen ban yallah féré
Aak yoyu
May zero kuma xamul dima jugé
Surtout yoyu
Soma sagga samlay bal
Somay gnodi bandit ma gneuw tégal la baye fall
Ak yénén damakoy def
Oh yén réwo léén
Yoyu yeup damakoy def
Bilay réwo léén
Yoyu ak yénén sakh
Ma nigga yaw bul mél kom man
Dagual diém man damko meun
Amo xalis amoy pékhé fomay songué malay meun
Dama liquide sumay wax sa xol day foy même soum’lay nakh
Non du mystique vue yé neuri ba fake yi nan dafa rakh
Boy yaw wéro wéro
Rang bu gnor ci BM du bénn ak bugni kolo kolo
Gni dagnu beuri défaut kumay teukalé ak gnom xamo
A part sa guél loumay doyé kumay téék loxo
Fagua tolu romb nafa
Fagua dieum djougué nafa
Malén gueune réw sama sound guena nice dossi dégu saga
Té lumu diar ma dieunde ko
Touss
Eh gnun lumu diar gnu dieunde ko
Touss
Loum diar gnu dieunde ko
Touss
Tapétu gnu lolu
Touss
Deug du nékh
Touss
Sama yaram day xésam sen piks yi dimay nekh
Touss
Cana warul ragal wétt yéén gneupeu mane kassé
Fumalén féék diomal leen kom guél bu faram fassé
Saga ma mdeye mala bal
Respecté na sama yaaye
Kon kéneu ci yéén duma xam
Sudone ay wax damay raay
Gno boku ligni def mais dama ci bolé sagn sagn
Bayina dugal statut damay sonak please send send
Anh deug la meun na cool
Mais meune na con
Amna djiko bandit ak djiko innocent
Dama beuri féén mak yén du game
Lumay doyé, luma diap dama beug dem
Wa waxlén gni deug
Xol’ én kulén gueunal gueunal
Eh wa waxlén gni deug
Mafi néék té waxo lu niit meuna dégu
Man lumu diar, ma dieunde ko
Touss
Séral zérol
Touss
Ak dokh bu gnak xorom
Touss
Su diékhé rek diékhna
Touss
Deug du nékh
Touss
Wolma bandit yeup
Ecouter
A Propos de "Damakoy Def"
Plus de Lyrics de JAHMAN XPRESS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl