Paroles de Abiyo
Paroles de Abiyo Par JAHMAN XPRESS
Gaye Mor Gaye
Gaye Mor Gaye
Aby'O Gaye
Yaw laay woye
Yaw laay woye
Walay Gaye
Weuy wou dotoul mossa faye lalay weuy
Gueye Mor Gaye
Gueye Mor Gaye
Aby'O Gaye
Yagg naa bindeu sa woye wii bou yagg sopi wat ko
Dama done bindeu ci yaw rangogne yi takh ma bayi wat ko
Lebou Maalimaram Ndoye Ngagne Ndoye
Rama Ndoye diour sa yaay booy mame booy
Sope naa sa nekine ci keur gui lou yakhou yangui diema defarat
Kouné nga diokh ko thieur bi mame khawma loniou dessalat
Mame booy
Yaw laay woye
Mane sama mame booy
Yaw laay jiiign
Liy deff sa mbegté ba nga contane laay diem
Gueye Mor Gaye
Gueye Mor Gaye
Aby'O Gueye
Yaw laay woye
Yaw laay woye
Walay Gaye
Woye bou dotoul meusseu faye laley woye
Gueye Mor Gaye
Gueye Mor Gaye
Aby'O Gaye
Yaw laay woye
Yaw laay woye
Walay Gaye
Yallah cédé nama mane deh beug nama la
Soumala guissoul niari fane rek namla
Nekk ci sa wét mane deh louma tamm la
Bama dane ndaw mame fo dieum ma topou la
Li takh ma woye la mame dou téy démb leu
Mame Goor famou teud téy mom gueureum nala
Diagayoul mame sa diane wathie naa
Teudeul nelaw sey seutt aawou leu
Li dieg dji lebou tey si kandang ci yaw deug leu
Nénegn sa mbakh gui dou téy yagg naa
Soula nékhé nga diayou Sa yéné yegg naa
Say dom aki seutt nieup santeu naniou leu
Bilay walay amouniou sa faye
Gueum nani sa weey bi doufi meusseu faye
Doundeul doundeul Aby'O Gueye
Gueum nani sa weey bi doufi meusseu faye
Mame booy
Yaw laay woye
Mane sama mame booy
Yaw laay djiin
Liy deff sa mbegté ba nga contane laay diem
Gueye Mor Gaye
Gueye Mor Gaye
Aby'O Gaye
Yaw laay woye
Yaw laay woye
Walay Gaye
Woye bou dotoul meusseu faye laley woye
Gueye Mor Gaye
Gueye Mor Gaye
Aby'O Gaye
Yaw laay woye
Yaw laay woye
Walay Gaye
Dama done raam ci sa kanam ngamay khol Mame dima rétane
Niouy dem guissguiss nekhatoul
damay wakh doma degg ndeyssane
Diambaar nga wone bari katane
Degg naa danga dane sokkou di kandang
Lathié naa wakh negn ma yaay kane
Yén bi dissone mame yako antane
Aby'O
Gueye Mor
Diokh nala sama xol
Mala woo si gandiole
Diokh nala sama xol
Ecouter
A Propos de "Abiyo"
Plus de Lyrics de JAHMAN XPRESS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl