Baale Lyrics
Baale Lyrics by FOU MALADE_NIAGASS
[CHORUS]
Boo Jekkoo deel baalé
Nagn diissoo bañ laalé
Boo Jekkoo deel baalé
Nagn diissoo bañ laalé
[VERSE 1]
Tey ma wax la li na nakhari
Jaay doolé ndax sa gabarie
Niew di jaale indi sabar yi
Xaal géew bi sànni koppar yi
[Fou Malade]
1-2 nga shine, 3-4 nga xeex
Li nga def sa mayin sax sa xol di jeex
Woo la agn nga suur teufli xaax ne teuf
Kajj nga reer bi tuur, taal sa jum di euf
[Niagass]
Yow lu tax bi meer bi feebare
Jëndóo garab yóobu l'hôpital
Tey nag deuj bi ni nga ko defare
Aduna jay la gnaata junni nga taal
[Fou Malade]
5-6 nga teuc téeye geel yi tanyim
Te nga ne ci deuj war a gnaan di waayin
Def tàtt di jooy xollu gan gni tiis
Màndikat nga booy jeuli naa la fils
[CHORUS]
Boo Jekkoo deel baalé
Nagn diissoo bañ laalé
Boo Jekkoo deel baalé
Nagn diissoo bañ laalé
[VERSE 2]
Defu ma yeugu ma bu ma ko waxal
Gisu ma déegu ma jotu ma jaxal
Tuxu ma naanu ma yoru ma goon
Sàccu ma kàccu ma du ma sa noon
[Niagass]
Da ngaa yeug sa bopp maa la geun a reew
Da nga meun a soop da nga niéme xew
Yagg a wanne baax te sa jikko sew
Alal bi nga coop du la masa lew
[Fou Malade]
Baal ma li ma saaga yaay sama gaayin
Bi ngay laal cagga ñoo ngi naan caayin
Na nu peace love dund paradise
Kaay niou naan koof dafa war a naayis
[Niagass]
Bége fo ree fexee indi jàmm
Boole doole di na gindi jàmm
Bayyi togn geun dëkkee balu àq
Ñaan gudd fan tuub li ñu yàq
[Fou Malade]
Tudee naa la doom dëgg la ci man
Boo feebaroon naa la yóobu Fann
[Niagass]
Mane la nitt Njaay yow la golo Hann
Yagg a saï-saï bandit Colobane
[Fou Malade]
Lii moo tax du ñu man a kóoz
Sunu amitié na fi "ménopause"
[CHORUS]
Boo Jekkoo deel baalé
Nagn diissoo bañ laalé
Boo Jekkoo deel baalé
Nagn diissoo bañ laalé
Watch Video
About Baale
More FOU MALADE_NIAGASS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl