BRIL Wétalngama cover image

Wétalngama Lyrics

Wétalngama Lyrics by BRIL


[VERSE 1]
Hol na fou né
Dem na fou né guissatoumala
Diar na feep fo dane nek
Wakh na lou nek dégatoumala
Douma nangou né dotou ma
Guestou ba guiss la sama wéét
Sama aduna touki na tagou wouma
 Bayima may weett
Diouli na di gnanaat y’Allah mou délossila
Donté béne guiss la
Sa dem wi louma tiss la
Lingue fi bayi sass bou diss
La doumako antane douma nopi
Faut que guiss la niakk
La loumay dioy la

[CHORUS]
Waro dem bayi ma nakh ngama wétal ngama
Geumouma ni doumala guissati fén
Namone nala wétal ngama
Nam nala wakh ma fane nga
Né bouma khamone fi nga nek
Niow fa waxma fo né
Damalay niane wakh ma fane nga
Né bouma khamone
Fi nga nék niow fa waxma fo né

[VERSE 2]
Damay togat ay nitte niouy
Waxtane té douma lén deg
Bobou mangui fénén founiou
Togue di kaf di rétane
Mane douma si meuneu bok
Sama xél langui si yénén
Fatélikou na bouniou dane ré
Bi nga dane def louné nakh mane
Diman takhawou feep foumou waré ioe
Dima diapalé ci lo meunoul ak li nga meun
Fimou tolou ni ci
Sama dound dara safatouma
Khawma louma tékki di
Diarign tém diégué woma
Sori ngama ioe khey nga dem bayima
Boul ma diégué kay wouyou ma
Sa dem bi wétal nama

[CHORUS]
Waro dem bayi ma nakh ngama wétal ngama
Geumouma ni doumala guissati fén
Namone nala wétal ngama
Nam nala wakh ma fane nga
Né bouma khamone fi nga nek
Niow fa waxma fo né
Damalay niane wakh ma fane nga
Né bouma khamone
Fi nga nék niow fa waxma fo né

Watch Video

About Wétalngama

Album : Wétalngama (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Sep 18 , 2019

More BRIL Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl