KBDA Lyrics by DOPE MASTER


Comme cana bou dioudowoul Amérique
Mané boy bi dh deukoufi
Boudé concert mou latchié ay hundreds miles
Dafeu yek bouko teukeulé ak Mc yi
Dafeu tiagon niou kheup si diw mou nineu
Slide sorri gnimay fékhél
Percé feep ni  carrierou ballou fétél
Bérte nieup moudié wouniou sankou ndéké
Now everyday I wake
I think about this life
Boudé guél leu ma yéné ko sama gars yi
Boudé khaliss ma Teral si sama yay
Kom fusée si kaw lagn meuneu dieum
Fiw fiw I turn it up
A.k.a boursine dou marr seu tateu
Meuno def kom li teudieul seu guateu ahh

Teudieul seu guateu teh cons
Son bi bokoul ak yi nguay job
Défo fi guate teh yay bomb
Ah oui sans effort dagn lagn romb
Sans nguenn pousse nigger damay dokh
Percé mm soumay sokh
Teuyel seu guel ndakh dope dh day roff
Pussy blindé ak pussy béton I do it
Nooneu yi danio beuri mangui maintien
Fuck rappeur fuck douganté
Niom nieup nio yam ma diougué fé
Niou complexé ma lakk léne anglais
Diangou niou doingou niou
fay léne ma diangual léne
Boudé pour bénéfice awma humanité
Clash nguama tontou wouma Kagn lalay bayi khél
Niongui imiter mann damléne di taylé

Comme cana bou dioudowoul Amérique
Mané boy bi dh deukoufi
Boudé concert mou latchié ay hundreds miles
Dafeu yek bouko teukeulé ak Mc yi
Dafeu tiagon niou kheup si diw mou nineu
Slide sorri gnimay fékhél
Percé feep ni  carrierou ballou fétél
Bérte nieup moudié wouniou sankou ndéké
Now everyday I wake
I think about this life
Boudé guél leu ma yéné ko sama gars yi
Boudé khaliss ma Teral si sama yay
Kom fusée si kaw lagn meuneu dieum
Fiw fiw i turn it up
A.k.a boursine dou marr seu tateu
Meuno def kom li teudieul seu guateu ahh

Aka bour sine dh dou marr seu tateu
Roubinet bi teudji takhoul ma naneu potiteu
Fi niou nek dagn ko job dou ay yalouwane
Nite yi geumougn niou wone yallah geum niou dem
Cigarettes doumko toukh nigger doublé rek
Ambulance si autoroute koumay doublé hey
Kom 2Pac douma ko def damay bourlé céyi
Chargé mbété bi diokhogn ko noneu yi prrr  
Like Everywhere I go
Niggas want my flow
Bitches love my flow
Haters know my, real niggers they know
Real niggeRs
Everywhere I go
I don’t show no love
Codeine in my cup
Og Kush my stuff
I don’t worry about nothing
They’ll steal em all
Dess na touti boy yeup Niro ak dope
bayi lenn topando
Wakh bou beuri sa kogn rek ngua totchieu
Ici on nique le nord
Aline MBAYE ndér vicé démonté lene
Hold up we’re them boys
Fuck y’a niggas do it for my niggas
Grr bang on your nose
Tell em niggas
Tell em Bitches we don’t need no love
Fi niou dioguè Dafeu soufé guissougn bras long
Fane ngua nekone bamouy méti nioko cotchel souniou bopp
Pas de tingom niongui si kaw

Comme cana bou dioudowoul Amérique
Mané boy bi dh deukoufi
Boudé concert mou latchié ay hundreds miles
Dafeu yek bouko teukeulé ak Mc yi
Dafeu tiagon niou kheup si diw mou nineu
Slide sorri gnimay fékhél
Percé feep ni  carrierou ballou fétél
Bérte nieup moudié wouniou sankou ndéké
Now everyday I wake
I think about this life
Boudé guél leu ma yéné ko sama gars yi
Boudé khaliss ma Teral si sama yay
Kom fusée si kaw lagn meuneu dieum
Fiw fiw i turn it up
A.k.a boursine dou marr seu tateu
Meuno def kom li teudieul seu guateu ahh

 

Watch Video

About KBDA

Album : KBDA (Single)
Release Year : 2022
Copyright : © 2022 Nautylusprod
Added By : Afrika Lyrics
Published : Oct 02 , 2022

More DOPE MASTER Lyrics

DOPE MASTER
DOPE MASTER
DOPE MASTER
DOPE MASTER

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl