DOPE MASTER Michael Jackson cover image

Michael Jackson Lyrics

Michael Jackson Lyrics by DOPE MASTER


Like mike Jackson
Rap beu nek legend c’est le minimum
Planète terre diougué wouma fi dama léne setsi ndong
Okey dangua bagn niou tiop la fok ngua nek deum
Téglé ay bric si bir compte banque Ahh

Dedicace gnima bagn yeup middle finger
Sakét na bamay toukh boneu yow ak seuy beute naneu nguéne def beu guiss ma
No mayonnaise boudé ketchup  déf si kilo
Dope man from ghetto tiop leep ndakh dagn yagu khifal
Ahh siw dou succès
Fuck carrière bou yam si ay vu ak Ay j’aime
Niom daniouy rap pour ameu show you khess pétchieu
Béneu danou diekh na fi rek nguéneu yam
Fuck may chance nigger job mokoy todji
Découragé néko geum na sama bopp
Soma diotoul dadioulo limay dadji
Meussoul yomb dama diokhé beu diekh takk
Deih pour doundou sama guénteu deugeuntane
Get money fi lou bakh dagn koy diay
Déplacement somay fay na doneu cash
Yoroulo guate paré wouma pour wakh sakh
Yagua tiaté dagn dém beu seuss seuss
Illusion laniouy guiss dougn ko geum
Dieul sama yone niongui latchieu fane la dieum
Nigger Depuis boy la paré pour raw nieup

like mike Jackson
Rap beu nek legend c’est le minimum
Planète terre diougué wouma fi by dama léne setsi ndong
Okey dangua bagn niou tiop la fok ngua nek deum
Téglé ay bric si bir compte banque mike jackson
Rap beu nek legend c’est le minimum
Planète terre diougué wouma fi by dama léne setsi ndong
Okey dangua bagn niou tiop la fok ngua nek deum
Téglé ay bric si bir compte banque like Jackson
Tour du monde kom Jackson
Built sama own propriety  
Teral gnima meusseu Kham yeup kom Jackson like Jackson
Bayi skul outi kham kham
Doundou film done acteur
Nezerland kom Jackson hey Jackson

Watch Video


About Michael Jackson

Album : Michael Jackson (Single)
Release Year : 2022
Added By : Farida
Published : Oct 28 , 2022

More DOPE MASTER Lyrics

DOPE MASTER
DDD
DOPE MASTER
DOPE MASTER
DOPE MASTER

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2023, We Tell Africa Group Sarl