Wiri Wiri Lyrics
Wiri Wiri Lyrics by DIAW DIOP DIDI
Yow wiri wiri diari ndari
Fo meunti demite baby dinga delou ci
Kotti kitti yolli yolli
Kay fi ma nakh la ya di sama nene touti boul daw
Meuna daw takhouta reuthie
Loy doye or so ame diamant bi si keur gui
Matt lima done andil contrat niou signe
Fouk thi niom mane rek ma yeungeul geusseum kene dou yeungeul
Niame na loulou
Tiitouma loulou
Gagne wala gagne match nul Yalla tere
Niame na loulou
Ragalouma loulou
Gagne wala gagne match nul Yalla tere
Ba takh na
Danga done lamb dadje nga
Danga done sett deh guiss nga
Hee mane leu affaire bi mane leu
Danga done lamb dadje nga
Pesse nga kham nga diss neu
Hee mane leu mangoul ni mane leu
Dall nga thi
Dall nga thi yow bill bou bakh bi leu
Dall nga thi
Dall nga thi si si bou bakh bi leu
Dall nga thi
Dall nga thi yow bill bou bakh bi leu
Yako tay
Kham ngani bii nii bou bakh bi leu
Woo ma Woo ma Yow
Yow wiri wiri diari ndari
Yangi dem te yangi delousi
Ma dila ayo ayo nene
Dila nene nene touti
Dorante dakante melni khale
Yay sama tom deh may sa jerry
Malay teul di teul teul
Done sa seytane dila djomal
Athie ba thia kaw wathie la si souf
Roganti teup teupal nila noppil
Danga done lamb dadje nga
Danga done sett deh guiss nga
Hee mane leu affaire bi mane leu
Danga done lamb dadje nga
Pesse nga kham nga diss neu
Hee mane leu mangoul ni mane leu
Dall nga thi Dall nga thi
Yow bill bou bakh bi leu
Dall nga thi dall nga
Thi si si bou bakh bi leu
Dall nga thi dall nga thi
Yow bill bou bakh bi leu
Yako tay , Kham ngani bii nii bou bakh bi leu
Thieureureuw thieureureuw sa guinak
Thieureureuw thieureureuw sa guinak
Tahie sa guinak sa guinak yow dokhal
Na nooy rek niou wakhtane ko
Na noo y rek niou wakhtane ko
Beug ngako bamou djekh te dara
Douko dindi mom nena yow rek te kene douko dindi
Wiri wiri diarouko yagg yagg dadje
Gaal guee nieuw gaal gathia top sa cadeau nga thia
Fathial ko
Thiathiambal
The Thiathiambal
The Thiathiambal
The Thiathiambal
Fethie ko yow ( fethie ko)
Fethie ko yow ( fethie ko)
Fethie ko yow ( fethiati ko)
Lil mou
The Thiathiambal
The Thiathiambal
The Thiathiambal
The Thiathiambal
Khale bouko meune nii ngakoy defe
Moo kouko meune ma may la djouni
Sa guizeul sa guizeul niapp sa guizeul
Sa guizeul sa guizeul niapp sa guizeul
Sa mbiw reuw mbiw pata minal reuw mbiw
Pathie thie koy koy garde vous yow dokhal
Deug leeeuu
Watch Video
About Wiri Wiri
More DIAW DIOP DIDI Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl