Reine Xol (Round 5) Lyrics
Reine Xol (Round 5) Lyrics by NOFACE
[COUPLET 1]
Ioe yaye yay ki geun si yaye yi
Di dab sama banékh té dossi tayi
Toudou niénti yone soga toudou baye
Sante nala geureum nala ioe yaye
Yar niou yor niou yé niou meusso ci tayi
Mounou ma bagna nam sey jotaay
Mougn, moytou, manlou sa mouslay
Sante nala geureum nala ioe yaye
[REFRAIN]
Bala ma meuneu wax yama done wayal
Tay do wax ma ley wayal
Rayal nala teign yaye dinala téral
Sante nala geureum nala ioe yaye
Maman, i love you so
Fi nga beug lay xol, la la la la la !
Yay sama reinou xol
Yay sama reinou xol
Té ma ngui diégalou si lima tok lou yague beugeu leu té wanoumala ko
Souma sagnone mane, dotouma tok ba
Guiss leu té waxoumala ko ioe yaye boye
Yaye sama yaye yaye yaye boye hoy ! Maaa !
[COUPLET 2]
Sante y’allah ndax lokho lama béral
Bou déssone ci ioe doma féral
Dara doula té yaye boye démal
Yarr ma, yorr ma, yé ma
Dima xélal werneu wan ko sa xol nako sédal
Maléyo maléyo !
Yo malé nénam mimé ri ma diara nénam
[REFRAIN]
Bala ma meuneu wax yama done wayal
Tay do wax ma ley wayal
Rayal nala teign yaye dinala téral
Mime ri ma diaram nénam
Maman, i love you so, fi nga beug lay xol la la la la la !
Yay sama reinou xol
Yay sama reinou xol
Té ma ngui diégalou si lima tok lou yague
Beugeu leu té wanoumala ko
Souma sagnone mane, dotouma tok ba
Guiss leu té waxoumala ko ioe yaye boye
Watch Video
About Reine Xol (Round 5)
More NOFACE Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl