Bëgg Naa La Man Lyrics
Bëgg Naa La Man Lyrics by AMADEUS
Eh Massamba walo
Zoom on the beat
Hey waay
Bëgg naa la
Reason to be man fonku naa la
Yaay jant bi man Bëgg naa la
Nii ma la Bëgge yi jeggi na dayo
Eh way ye way mi girl
Mi yi dei ma for Life
Lu nek jaral nga ma
Ken mënul tax
Ma merre la
Ñook seeni wax
Fuck nañu leen daaw
Man so merre damar jaaxle, tiis
Dama la bëgg
Be neen jigeen mënul tax ma giif
Ndax yaw la bëgg
Amul sax
Nit kuy mën xam li may yëg ci yaw
Amul sax
Nit kuy mën compu nima la bëgge yiiii
Bëgg naa la man
Ehh ehhh
Bëgg naa la man
Bëgg naa la man
Ehh ehhh
Bëgg naa la man
Dama la bëgg ba faf gëmme wu mala
Bañ lula metti bañu yaakaar ni ñeme wu mala
Dama la bëgg ba faf gëmme wu mala
Bañ lula metti bañu yaakaar ni ñeme wu mala eh
Jamm nga may lathie ma ñëw indi feeling pathie
Ku degg ngay lathie te man dama degg daaj ehh tamit ci aduna
Man rek malay beggël
Jamm nga may lathie ma ñëw indi feeling pathie
Ku degg ngay lathie ma ñëw indi feeling pathie eh
Tamit ci aduna
Man rek malay beggël
Ku la laale man lay raagal
Te kula tooñe may nangu xeex bi
Eh way ye way mi girl
Mi yi dei ma for Life
Lu nek jaral nga ma
Ken mënul tax
Ma merre la
Ñook seeni wax
Fuck nañu leen daaw
Man so merre damar jaaxle, tiis
Dama la bëgg
Be neen jigeen mënul tax ma giif
Ndax yaw la bëgg
Amul sax
Nit kuy mën xam li may yëg ci yaw
Amul sax
Nit kuy mën compu nima la bëgge
Bëgg naa la man
Ehh ehhh
Bëgg naa la man
Bëgg naa la man
Ehh ehhh
Bëgg naa la man
Dama la bëgg ba faf gëmme wu mala
Bañ lula metti bañu yaakaar ni ñeme wu mala
Dama la bëgg ba faf gëmme wu mala
Bañ lula metti bañu yaakaar ni ñeme wu mala eh
Watch Video
About Bëgg Naa La Man
More AMADEUS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl