ALMA NOPP Keur Gui Crew cover image

Keur Gui Crew Lyrics

Keur Gui Crew Lyrics by ALMA NOPP


    Kilifeu
Tanale nala yaye djou bakh tcha djiko yagnu ko yabbé
May sa baye ta defoumafi lougnou ma wara yabbé
Ngala way rooyal thi niit you baax gnimala toudé
Diang laala sant, dome maandu fonk sa Diiné
Li nga seex ak say nawlé na nga sa fekhé gooré
Moyoul ku ndadjé beug aalal na nga si tabbé
Diar nga neggu ngoor nala woor ngor dou wax waxate ,
Dou wax waxeet, soko defé geun xeet
Na nga xam sa xeet boul dougg ci loulay sakeet
wethiet di nga ko sokhla mais boumou la mousseu titeul
Disket na doon sa sokhna mome dé boumou la moussa djiteul
Je sais que ya ngi laal ci pet diefeundikol Kondom
Amago lo yoré doom
Fils na nga moytu vices, yeen bi da diss
Yone bi da liiss, na nga moytou tarkhiss
Kouy door dou xacc, Ass goor dou kacc
Goor dou Sacc, Goor dou fecc

[REFRAIN]
Anglais

THIAT
Ma fille, beugouma nga may meeré, xam nga nimala beugué
Soumalay terré c'est pas parce que damalay diema fiiré
Xamna ni doone nga diankh, beugouma loulay sank
Djiguene dou diang pank, dafay diap tank
Djiguene mouthiam keureudi, Diamono bé teureudi
Adouna bi woreudi, fess dell ak gnou wereudi
je sais que do feel
Boy dadiek pedophile
Goor gni meun nagne fene, Di nga degg ba tayi Je t'aime
Na nga yame sissa beneu, Boul yakar keneu ci leen
Limala denk na nga ko fonk, Beugouma sa beut di xonk
Def foula moytou fontou, Soy teud na seur bi xonk
Ndakh lolou moy sa tontou, sa nopp bougn ko yeey
Boul deglou koulsy deey, amal sa bopp xeuy, sa nawlé boumla yeey
Fékhel na gnor xomb, dara doula diomb
Na nga fess diom, lou diot yomb, ken doula romb

[REFRAIN]
Anglais

KILIFEU
So guissé ma beuri wax, limassi joblou nga baax
wadiour la dou meti , fokma wasslu aax
Louko moy rek euleuk dinako layo barsaax
Djiko yimala diox , dji ko mou saax
Li mala diox, fexel ba boumou nasakh
boppu bay aam barké nopp yuy degg say saax

THIAT
Ma fille na nga teey, foy seuy na nga fa seey
sa ndeye moussoula faye, limoula deey na nga koko faye
Fekhe ko roy, Loy tog mou doye, boul falé koulay xoy
Boula kenn guiss nga dioy
Dieukeur moy sa waay, nek sa werou waay
Nek di noflay, li boumou nakhsay

[REFRAIN]
Anglais

Watch Video

About Keur Gui Crew

Album : Encyclopédie (Single)
Release Year : 2015
Added By : Tamsir Diouf
Published : Oct 22 , 2019

More ALMA NOPP Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl