La Boca Lyrics by NIX


[CHORUS]
Game bi la deff sens interdit waxma loussi sama yone
Guisseu gouma kouma diaxal magui moytou sama bopp
Bobou bâ légui niow nagn dém nagn yaw yagui thiéné figua tokk
Prouver Prouver rek
Ba kéne dotoul amati loumouy wax
La boca la boca. La boca la boca
Fils fayma money. Sinon nala nokha
La boca la boca. La boca la boca
Mak sama bendo di guéné Ay lenguis es lavida loca

[Nix]
Platao plomo
Noto de plomo
Eh ! Accéléré na sa défaite
Nga doundou ko slow-ment
Niggas ci hood bi gueuna taxaw moto.
La vie de loco moy shampooing ak omo
Aÿ montant loto thi bir bén loxo
Ay bone you sadik boy day andak tokho
Néna ma waxtane ak nom ma gueuneu
Nioul fi boy kon fuck sa choco
Magma boy may lekk ak niom thi
Restaurant chic di dankeu ak loxo
Boy ma dax dance all Maca
Ay collé serré cap-verdienne deh la taka.
Fi meunoul leundeum tant que ma ngi takka boy ya ngui séras
Un, deux niou guéné PACA
Découpé découpé M-C
Boy omzo tém gnou oubi dibiterie
Diay Ay Mc par kilos mariné séni djiko
Solal sen manager yi ay string en nilon
Le highlander parcourt en tillon kodal en mille ans
Ak disayou million de pilons
Eh nila nila bueno ouvrir sa boca sinon
Dagn koy anesthésié comme la coca
Sisi may koulay fuck every day man may faru rab bou épicé
Rappeur y’a ngi diémeu diay lou saff
Kon lo beugue niou done boy
À part mes épicier
Légui niow len boy waxtanal gnibissi
Nioumay xol dima lathie Kahn la gnibisi
Dama lakk français boy ba doyal hummm
Légui dieul wolof bi confisqué

[CHORUS]
Game bi la deff sens interdit waxma loussi sama yone
Guisseu gouma kouma diaxal magui moytou sama bopp
Bobou bâ légui niow nagn dém nagn yaw yagui thiéné figua tokk
Prouver Prouver rek
Ba kéne dotoul amati loumouy wax
La boca la boca. La boca la boca
Fils fayma money. Sinon nala nokha
La boca la boca. La boca la boca
Mak sama bendo di guéné Ay lenguis es lavida loca

[Omzo Dollar]
C’est à dire que... Anh
Capitano man la Raúl
Gaindé guiss ma yoxou miao
Dernier K.O premier gaou 1million dans les poches
Jus au cas où
Fils mane la BCEAO boudé daw lagnouy diay
Eaux et forêt boudé flow lagnouy diaay
Cachet 1milion sou tiolé gnou bayi
Mane tata vivi momay wowé nijaay
MUAAH
Awma wone moyen mais tay mon fils J’ai les moyens
Plus que tous mes instructeurs
Boy yagui thiéné thi bountou kongn bi di tall ay doublé
Ba melni meilleur buteur
Boy Miézé amna diplôme mame
Yég bopam ni mère bou saga ndeye domam
Aucune option c’est la fuite
Marche rappeur galsen yi sen fête moy le 8 mars
Bayima xel nga nék borom bop
Samay 12 doko guiss ci horoscope
Torokh nom fresh to deff ba europe lokh dieuleul tof
Mane ak rap comme werr ak doff, weur ak tog
Waxma ani goor ak lokh door ak love
Mane ak niom comme door ak boxe, sport ak dox
Légui xébb na djolof trop
Rap galsen na eup thiaass ngor ak Yoff
Fils waxma loutax sa grand mér
Ma grammaire n’épargne aucune grand-mère
Sa sipres samay son dougn ko gueumé
Nénagn niom diouli rek lagn ma xamé
Ma gui téléphoné ak sama avocat
Guél bou andak forme bouteille coca
Si team bi nieupeu meuneu coaché la roxa
No djoutou gang mother fucker! Eh

[CHORUS]
Game bi la deff sens interdit waxma loussi sama yone
Guisseu gouma kouma diaxal magui moytou sama bopp
Bobou bâ légui niow nagn dém nagn yaw yagui thiéné figua tokk
Prouver Prouver rek
Ba kéne dotoul amati loumouy wax
La boca la boca. La boca la boca
Fils fayma money. Sinon nala nokha
La boca la boca. La boca la boca
Mak sama bendo di guéné Ay lenguis es lavida loca.

Watch Video

About La Boca

Album : La Boca (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Oct 22 , 2019

More NIX Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl