Popcorn Lyrics
Popcorn Lyrics by AKHLOU BRICK
Boudon né kou né sa life lagniy dawal tay cinéma
Kou guiss sa cd ding ko hoss si pet bagn sa dieufi né fang
Lima guiss wahko defko ak fima deug sama tank
Tank yalla ngui def soutoura si man menoko ham
Porcorn bi man kassé si ciné may seytanè sama film
Jeuf mo nék ni man kassé fi nèk fiimné ak yalla mima tim
Toudal ma diw ak diw diw mila takhal té dou niin
Faw yalla hawi lim dentj nga guiss diw dotoul mena miim
Yaw gni geum ni Rassoul dé na gno geuna triste
Li tah meno ham Jesus pask ya toudé leundeum criss ( chirst)
Ibliss don bour thi diamono Bign seulmalè timiss
Borom gnari beut yeup goumba borom bén beut di guiss
Fi ak fè ak fagnou dieum fou dieun doul deki Rou dieufarou
Dieumeum yonen mo ndieuka guiss motah mo ndieuka diébalou
Yaw lan nga ban ngalaw safara ak ndoh
Ko geum
yalla bou Ibrahima wala bi Ibrahima weron ngot
Ko geum nit nga Rek do Deum
Nekal ki nekal lep Wetal ki weton demb i mean
Sa yo wete yaw ak sa bop Wetok ngak sa Ya Rabi
Free Rou diar wethit free ken amoul sa ndieuk free
Fay nagn prix pour dieund mais fekogn si man sam roubi
Yeah
Bou laf don mayé jam ramatou dou ham pierre
Ay mindafone di heh ngir yaw te thi yaw lagn nek
Bo thiakaré nim lay nakharè metite ngay yeuk
Yeurmande yalla rekay walou diam te ken amoul ndieuk bi
Ken amoul ndieuk bi
Ken amoul ndieuk bi
Ken amoul ndieuk bi
Ken amoul ndieuk bi
Ken amoul ndieuk bi
Ken amoul ndieuk bi
Alcool thie gom bou bess ndakh bou robalee day teu
Neubeul sa xol bou fess bou dee rembet ndokh day feul beut
Dès fois ma bind way pour sa wayadi nga dinga dindiko
May wakh sa bir xel lo degoul louma athie boy nga dem adjiko
Tekil sa verr you rose yi, nga guiss la vrai vie Wathiel sama bop
hol thi souf guenee sa beut ecla étoiles yi legui xol
Ma wakh lo guiss lou nostra damus predire
dalay nekh nga bone mba nga bah life bi yaye def choix bi
Like, boul weureuti ba son degloul sa xel topal sa xol sa dieuf
Moy thieur bou dieuf dji bakhee aldianay sa keur
Fo dieulee dolè beuneu wen beuss bingay dora nap nam gueumal sa bop
Gueum sa liguey ,lo dougou am ci ndam god
Roki me roki la wotee la wotee thie diam manam
Newona rassoul kou tedeki topal sa yonou mam ibrihim
Bo beuguee degue kamil na deugue nek kani
Fonkal yaye ak bay sa wassila bi niane nga dek amine
Bou laf done mayee diam ramatou dou ham pierre
Ay bindafon di hekh nguir yaw tee thie yaw lagn nee bo
Thiakaree nimlay nakaree metit ngay yeuk
Yeurmandee yala rekay walou diam bi tee ken amoul dieuk bi yeah
Ken amoul ndieuk bi
Ken amoul ndieuk bi
Ken amoul ndieuk bi
Ken amoul ndieuk bi
Ken amoul ndieuk bi
Ken amoul ndieuk bi
Watch Video
About Popcorn
More AKHLOU BRICK Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl