Yow La Lyrics
Yow La Lyrics by VJ
Set naa setoo setat guissagouma kou melni yaw
Sa dieum diè ma yëm man guissouma kènène
Pourtant mane pourtant mane
Guiss na façon bou nè
Pourtant mane pourtant mane
Guiss naa djiguen bounè
Yaw laaa done niane yalla (toucouleur alè racine)
Niane yi moudiè antou (dièk rafète ya ngui)
Yaw lay guiss wër ba ngui
Kouy ndeyam ak bayam setoo set ya ngui xoo looo say morom
Diouk lene taye la teey kouko Xam na nga diayou (diayouuu)
Ya diara sargal yaaa diara tathiou
Diayoul tey sa biss la mane mane maaa la taamou
Say dig morom say nawlè soula nèxè baaakou
Mbeuguel Dafa diss, Dafa beurri dolè Yaye sama aljanah (waaaawaaw yaw)
Yaye sama aljanah (Ahhh Ahhh Yaw la)
Yaaa ma lën geuneul yow mi (Waaaawaw Yoe la)
Yaye sama aljanah
Diombadioo ari
Diombadioo ari
Diombadioo ari sama sët baaa ngui yek si na
Diombadioo ari
Diombadioo ari
Diombadioo ari sama sët baaa ngui yek si na
Beuss bi laaa done xar , Tay Dafa melni mo ngui
Ëksil sama ndanane , naaala siggil si say nionie yaw
Fi niou diar limala togne, li nga may baaal
Limala diaral ak fi nga ma tolou sama ndanane
Yama lën geuneulone dama lën ko roussona wax
Imam tëw na nawlè yeup tëw yaw deh ngani waw
Ndiëguëmar biss yaaadi meut diëg
Mayko mou dial sama miss ba ngui
Xalè la waaayè fess na ak diom
Biss dina doni ndanane sama miss baaa ngui
Mbeuguel Dafa diss, Dafa beurri dolè Yaye sama aljanah (waaaawaaw yaw)
Yaye sama aljanah (Ahhh Ahhh Yaw la)
Yaaa ma lën geuneul yow mi (Waaaawaw Yoe la)
Yaye sama aljanah
Diombadioo ari
Diombadioo ari
Diombadioo ari sama sët baaa ngui yek si na
Diombadioo ari
Diombadioo ari
Diombadioo ari sama sët baaa ngui yek si na
Me and you for life for life Bae
Me and you for life for life Bae
Xamal ni ma ngui si sa wët
Mouy taaaw Wala mouy nadie ma belle
Watch Video
About Yow La
More VJ Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl