Beauté Africaine Lyrics
Beauté Africaine Lyrics by PAAPAREY
[REFRAIN:]
Rafétay bou diégui dayo,
Tékki nagn ba melni ouroul hayni
Beautée Africaine bi né si niom
Nioune mome mo niou doflo
Rafétay bou diégui dayo,
Tékki nagn ba melni ouroul hayni
Beautée Africaine bi né si niom
Nioune mome mo niou doflo
[COUPLET 1]
Rafétay ba diégui dayo
Dièk tarru nel mashallah
Beuti meun nga ci séttu,
Comme derr bou nioul bou khess ak bou chocolat
Lifi mame yi bayi wone,
Dieugou fi niou ngui souniou yone
Kahm finiou dieum ak finiou thiossano yeah yeah!
Ma défilé baby
Ma dagou dokh nim ma nékhé ni dionguama
Natural girls yow
Ma rétane samay begun you wex nekh nala yeah!
Beautée Africaine bi ci ndax doy nala yeah !
[REFRAIN:]
Rafétay bou diégui dayo,
Tékki nagn ba melni ouroul hayni
Beautée Africaine bi né si niom
Nioune mome mo niou doflo
Rafétay bou diégui dayo,
Tékki nagn ba melni ouroul hayni
Beautée Africaine bi né si niom
Nioune mome mo niou doflo
[COUPLET]
Diaroul khol ni nga tarro baby,
Sa derr bou nioul bi dakey ndamo lady
Na nga takk sa seurr niafé ko home way oh no!
Setloul khol lila y’Allah diaglél,
Sa mélocane bi mane dag mey danél
Na nga geum li nga done baby oh way, oh no!
Nioune yeneuniouy danel,
Nioune yéneuniouy dioylo, nioune yen laniouy ndamo baby
Mane weuy na len, niom mougn len dara
Mane weuy na len yeah yeah!
Défilel, souris, ta ville dokhal noum la nékhé comme je m’en moque
Naturelle comme yahh !
Rétanal say beugn you wex nekh nama yeah yeah yeah!
Beautée Africaine bi ci yow déh doy nama
Ah sokhna si yeah !
[REFRAIN]
Rafétay bou diégui dayo
Tékki nagn ba melni ouroul hayni
Beautée Africaine bi né si niom
Nioune mome mo niou doflo
Rafétay bou diégui dayo
Tékki nagn ba melni ouroul hayni
Beautée Africaine bi né si niom
Nioune mome mo niou doflo
Watch Video
About Beauté Africaine
More PAAPAREY Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl