MéLODIE ADO  Marie & Cheikh (Remix) cover image

Marie & Cheikh (Remix) Lyrics

Marie & Cheikh (Remix) Lyrics by MéLODIE ADO

Soum la noboul wone doum la mariée
Soum la noboul wone dam lay fowé
Soum la noboul wone douniou seuy hé yah
Kone loutax niou deuk si xoulo
Soum la noboul wone doum la mariée
Soum la noboul wone dam lay fowé
Soum la noboul wone douniou seuy hé yah
Kone loutax niou deuk si xoulo
Marie, beug nala beug ngama ak cheikh marie, woloumaaa
Marie, ak cheikh marie xol bi ya ci né waw
Marie beug nala beug ngama ak cheikh marie woloumaaa
Marie, ak cheikh marie bébé waw waw

Alliances’ou lokho douyou leu
Chaque jour nga vérifier téléphone
Kou beug’ay fiir nangou na waw
Wayé chérie dag ci bolé togn
Kone bea boul parfois ma nélaw
Tay guissna si ioe louma méti
Ndax saga ngama té bayiwo si xel waw
Khamna sa xol mo tangue waw
Boul déglou waxou nitt gni dagn ley misère lo
Ladial gnimay andal ioe lay titeuro
Té souma nobatone kénén yakoy nieukeu
Yeug waw ndax chérie yay sama xol

Chacun a sa chacune, chacune a son chacun
Kone chérie ay boul ma yeungeul boul
Ma yeungeul boul ma yeungeul way
Dou yama togn doma néxal, boul ma yeungeul way

Marie, beug nala beug ngama ak cheikh marie, woloumaaa
Marie, ak cheikh marie xol bi ya ci né waw
Marie beug nala beug ngama ak cheikh marie woloumaaa
Marie, ak cheikh marie bébé waw waw
Soum la noboul wone doum la mariée
Soum la noboul wone dam lay fowé
Soum la noboul wone douniou seuy hé yah
 Kone loutax niou deuk si xoulo
Soum la noboul wone doum la mariée
Soum la noboul wone dam lay fowé
Soum la noboul wone douniou seuy hé yah
Kone loutax niou deuk si xoulo

Marie, beug nala beug ngama ak cheikh marie, woloumaaa
Marie, ak cheikh marie xol bi ya ci né waw
Marie beug nala beug ngama ak cheikh marie woloumaaa
Marie, ak cheikh marie bébé waw waw
Chacun a sa chacune, chacune a son chacun
Chacun a sa chacune, chacune a son chacun

Watch Video

About Marie & Cheikh (Remix)

Album : Marie & Cheikh (Remix) (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Oct 20 , 2019

More MéLODIE ADO Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet

About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl