Ravaaj Lyrics by KEY EM TI

Defal La Son Bi Nga Yokhou Weuuy
Piquouma Dama Gass Dama Wakh Lepp Lerr
Rappeur Buu Ňuul Moo Meuna Weuuy
Sakhal Sama Tour Yi Xolyi Donnée Cellulaire
Wongama Ma Wouyula
Loutakh Nga Beuga Daww
Artiste Dou Daanou Té Yow Toudouloo Moussa
No Djoutou Mala Tince
Tince La Mother Fuck
Sa Rap Bi Sagga La Kenn Validéwouko
Yow Yaffi Nek Lolou Donn Ayy Fenn
Meilleur Rappeur Tous Les Temps Nga Cissa Iphone
Niggah Danga Rerr Yow La Chaînou Akon
Khethila Tegui Sa Batt Bi Defla Dieumm Dalton
Am The Best, Best Ever Did Daal Sen Kaww
Deugg La Todjj Ci Sa Perri Ferri Comme Tenn Taaw
King Bi La Bolé Ci Dame Fer Renn Mbaax Taaw
Magui Sa Birr Peripherie Koufi Reumbakh Daww

À la Kasimodo Meunolenn Ma Diayy Ciss
Gnoulay Gnodi Blood Gnolay Diema 36
Tek Sa Boy Côté, Dougn Ma Boycotté
Fou Sa Baye, Lalay Doudou Katy
King John Cadet, Sécurité Palais
Meuno Fecci Son Bi Ndakh Sa Niggah Layy Baalé
Dama Coupé Nguén Callé
Coupé Décalé Sonn Nagn  Sa Son Yi
Fo Demm Copié Collé

Mani Souma Namé Dawal Rapci Grosse Caisse
Téyall Sa Auto Papa C'est Pas La Hess
Sokhor Ci Gaumou Xoll Dou Gnouci God Bless
Fi Koufi Diemma Diayy Mouss Niou Defla Khadj Pess
Do Guiss Sama Evadé Manla Sneak Man
Rencontre Denis RodMan  Ci Domu Kim John
Gamou Fond Vert Ma Outil Plume Sa Kingdom
Ln1 Sa Rappeur Tadjali Sa King Domm
Fi Dofi Thing Thiong Houn Hann

Douma Door Sa Maami Nako Def Biirr Thinne
Nouvelle Langage Ni Algorithme Da C
Dagn Né Pripp Ma Doorla KO Dou Difficile
Ici C'est La Guerre Douma Changé Style
Ravage, Savage, Sauvage  Qu'est ce qui se Passe
Alors Dis Moi Ton Blaz C'est Pour Petasse
Chak Jour On Bosse Ici Pas Pile Ou Face
Remasse Tes Clashs De Merdes C'est Pire Helas


Defma Rek Sa Baye Thiowli Diekhna Tayy Dji
Ma Haza I Really Hate This
Mala Eupp Dadj Key Menuisier
Job Lepp Di Sett Fuck Sa Policier
Rappeur Bou Magg Amoo Millions De Vues
Gnul Teklou Khess C'est Ça M'a Devise
Bindeu Son You Def Tabac Nema Drogue Douce
Meuno Wakh Ba Guéné Liné Sa Biir Tounn

Watch Video

About Ravaaj

Album : Ravaaj (Single)
Release Year : 2020
Added By : Afrika Lyrics
Published : May 19 , 2020

More KEY EM TI Lyrics

KEY EM TI
KEY EM TI

Comments ( 0 )

No Comment yet

See also



You May also Like



Get Afrika Lyrics Mobile App

About AfrikaLyrics 

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2020, New Africa Media Sarl