QUEEN BIZ Boy Friend cover image

Paroles de Boy Friend

Paroles de Boy Friend Par QUEEN BIZ


Gnou beuri gnigui nan louma guiss si yaw
Yama leen geunel sama boy friend
Danu meunoul guiss leer guima guiss ci yaw
Yama leen geunel sama boy friend
Yek yek béh fort dafa diss
Ci nom yama len geunel sama boy friend
Wayé faalé wouma len doundou mak nom
Yama len geunel sama boy friend
Sa mbeuguel ci man motax taamu nala
Sa yermandé ci man motax fonkeu nala
Yeah yeah yeah yeah gounéh yi, nan ma bayék yaw
Yeah yeah yeah yeah gounéh yi, sama adduna yako yor
Nom dall, Queen Biz
Funu tollu gnugui may toogué
Deguena Queen Biz
Man nan la lay toopéh
Nom dall Queen biz
Banuma si dara dama bardé
Nogui nan Queen biz
Mom dafa nakkeu faydaa
Lepp ci yaw la liniy tek sama kaw
Yepp ci yaw la litax ma beugue la
Ci yaw la baby yama ko jaral
Ci yaw la 
Baby lutax ma nagnou ci yaw la 
Lissou nga sama holl bi Ci yaw la 
Litax ma beugue la Ci yaw la 
Baby yama ko jaral Ci yaw la 

Nu beuri nigui nan luma guiss ci yaw
Yama leen geunel sama boy friend
Danu meunul guiss leer gui ma guiss
Ci yaw yama len geunel sama boy friend
Yek yek béh fort dafa diss
Ci nom yama len geunel sama boy friend
Wayé faalé wouma len doundou mak nom
Yama len geunel sama boy friend
Yaw la love the yaw la, yaw la
Yaw la love teh yaw la
Yaw la love teh yaw la love
Yaw la love teh yaw la
Baby yaw la live teh yaw la, yaw la love
Yaw la love teh yaw la
Yaw la love teh yaw la love
Yaw la love teh yaw la
Eh yeah yeah yeah 

Repsé binga am ci man, motax taanu nala
Gondi woma ak linga am, motax fonkeu nala
Sama hol bi yama si doy, nan ma bayék yaw
Kuma beuge nama bayék yaw, sama adduna yako yorr
Nom dall, Queen biz
Beugu numa guiss may happy
Nogui nan Queen bis
Alalam bi lako toppéh
Fatté nan, Queen biz
Dama pare demb tay soga new
Wexleen Queen biz
Ludul mbeuguél sonalumah
Lepp ci yaw la linu teik sama kaw yep
Ci yaw la litax ma beugue leu
Litax ma beugue la ci yaw la
Baby yama ko jaral ci taw la
Baby lutax ma nagnou ci yaw la 
Lissou nga sama holl bi Ci yaw la 
Litax ma beugue la Ci yaw la 
Baby yama ko jaral Ci yaw la 

Nu beuri nigui nan luma guiss ci yaw
Yama leen geunel sama boy friend
Danu meunul guiss leer gui ma guiss
Ci yaw yama len geunel sama boy friend
Yek yek béh fort dafa diss
Ci nom yama len geunel sama boy friend
Wayé faalé wouma len doundou mak nom
Yama len geunel sama boy friend
Yaw la love the yaw la, yaw la
Yaw la love teh yaw la
Yaw la love teh yaw la love
Yaw la love teh yaw la
Baby yaw la live teh yaw la, yaw la love
Yaw la love teh yaw la
Yaw la love teh yaw la love
Yaw la love teh yaw la
Eh yeah yeah yeah 

Ecouter

A Propos de "Boy Friend"

Album : Boy Friend (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Sep 06 , 2021

Plus de Lyrics de QUEEN BIZ

QUEEN BIZ
QUEEN BIZ
QUEEN BIZ

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl