PEE GANGSTA Falema BNG#2 cover image

Paroles de Falema BNG#2

Paroles de Falema BNG#2 Par PEE GANGSTA

[CHORUS]
Xamone ngani souma gnewé sama xool Bigua yobouwone mome lay djeli
Baby menetouma xaar ndaxté fima diaar mome dafa goude my lady yaw
Kou melni yaw my baby amatoufi my lady
Mane sa xool la beug fi guako adje loumou kawé kawé nakko djeuli

[HOOK]
Geumoumawoni nitt gua yaw mi non non geumoumani nitt gua yaw
Daguama rombe rekk yobalé sama xool kerok mane xawnafa daaaw
Kerok mane touté ma daw
Sa beut yi gnoma titeul
Est-ce que sax do djiné yaaaaw
Geumoumani nitt gua yaw
Geumoumani yalla dina sakati djiguen bou rafét tarou lolou ba melni yaw
Li né thi sama xool bi yakko meuneu dindi
Nékatounou thi nawet waxma loula taxa toyy
Nékatounou thi nawet loula taxa toyy
So namé koula wayal mane ma doni Mr Maydi
Dieum diagui ni baby yaw ya yoré xool bi lady dama lonely
Hoo my baby i'm sorry

[CHORUS]
Xamone ngani souma gnewé sama xool Bigua yobouwone mome lay djeli
Baby menetouma xaar ndaxté fima diaar mome dafa goude my lady yaw
Kou melni yaw my baby amatoufi my lady
Mane sa xool la beug fi guako adje loumou kawé kawé nakko djeuli

[VERSE 2]
Meune gua weur ba sone mais dou takh gua guissati Goor bou melni mane
Sama mbeugél si yaw déh foko meuneti natt wésounako di démmm
Soma beugoul boulma fénn
nagma bayii mane ma démmm
Lithi sama xool dou déñññ
Boudoul yaw dou done kénén
My baby yay sama real love watnani non dou ay fénn
Fou sorri lala topé baby oumpeuléwo mane nimala nobé yaw
Baby xana yeureumoma
Daffa melni yaw geumouloma
douma bayii fekk seuyeuloma
sagua saxx dou taxx ma déme

[CHORUS]
Xamone ngani souma gnewé sama xool Bigua yobouwone mome lay djeli
Baby menetouma xaar ndaxté fima diaar mome dafa goude my lady yaw
Kou melni yaw my baby amatoufi my lady
Mane sa xool la beug fi guako adje loumou kawé kawé nakko djeuli

[VERSE 3]
Ok OK baby néma OK
Oubilma sa kaname xolma réma néma OK
Sa kanama tarou mba douma warou waxagoma waw sexy lady xaral ma maalou
Bouldi gawa ré sa wéxayou beugne soumako yagué
Di guiss baby legui ma danou
Mane soma faléwoul ma diaréfa gagnou
Baby néma waw ndaxté mane yaw lama tamou

[CHORUS]
Xamone ngani souma gnewé sama xool Bigua yobouwone mome lay djeli
Baby menetouma xaar ndaxté fima diaar mome dafa goude my lady yaw
Kou melni yaw my baby amatoufi my lady
Mane sa xool la beug fi guako adje loumou kawé kawé nakko djeuli

[OUTRO]
My only baby falema
My sexy lady falema ma lovely baby falema
Xana diguama falé yaw
My only baby falema
My sexy lady falema
Ma lovely baby falema
Xana diguama falé yaw

Ecouter

A Propos de "Falema BNG#2"

Album : Falema BNG#2 (Single)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Nov 01 , 2019

Plus de Lyrics de PEE GANGSTA

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant

A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl