Paroles de Mère Célibataire
...
Paroles de Mère Célibataire Par MIA GUISSE
Danko beug play kay ñou game
Rek nga xam shingom dou kaani xéñ
Difeinte faime
Diakhasé faine
Guisou ñouma sene guiss guissa ñaaw
Gné di siissou
Gni lakh sen sokhor thi yalla
Yalla mi gniy wooté Guem mou gnou ko
Lakhou neuteuril dég
Héy girl
Meunone nga ko mafé deug deug
Héy girl
Tiga degué bé na ni noon
Héy girl
Beug baakh taxone ma téla seuyi
Seuyi mougne dathie eumbe dirékou
Doma thi dioudou
Bautiful baby aminatou
Done mere célibataire bi di fipou
Done ndeye done baaye
Done ndeye done baaye
Done ndeye done baaye
Beneu nit ngay toudou gaagne aye mbokam
Héééy
Mani momeu
Louma wor leu
Di faine
Té kene dou toudou sa diambar
Dagnouy tok di xaar faux pas
Gni naane
Héy girl
Meunone nga ko mafé deug deug
Héy girl
Tiga degué bé na ni noon
Héy girl
Beug baakh taxone ma téla seuyi
Seuyi mougne dathie eumbe dirékou
Doma thi dioudou
Bautiful baby aminatou
Done mere célibataire bi di fipou
Done ndeye done baaye
Done ndeye done baaye
Done ndeye done baaye
Mba do Mandou
Ak loko xamal
Nit day mandou
Déko soutoural
Mba do Mandou
Ak loko xamal
Nit day mandou
Déko soutoural
Nit kou xam yalla day
Mandou
Nit kou gueum yalla day
Mandou
Nit kou xam yalla day
Mandou
Nit day Mandou
Mandou
Mandou
Mandou
Del soutoural jiguéne
Del soutoural jiguéne
Ecouter
A Propos de "Mère Célibataire"
Plus de Lyrics de MIA GUISSE
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl