Paroles de Cheri Coco
Paroles de Cheri Coco Par AMIRA ABED
Aaye Waaye Cheri Cheri coco
Yama té nelaw waay na leu
Cheri sama ndanane yama té nelaw
Aaye Waaye Cheri Cheri coco
Yama té nelaw waay na leu
Cheri sama ndanane yama té nelaw
Ndeysane Chauffeur Bou Ndaw bala Diouli Jaapou
Tokk tchi deer di niane
Loumou Niane Yalla Maayko ko
Dégueul Kileu Diarra Maaye Sa Dome Bigué
Lary Coumba Bigué Soka Diack Ndella Ngoné
Cheri Kay faune meu, Yama té nelaw
Diallo Diaalloooooo Diallo
Marie Ngoné Arame Mbaye Dem Neu
Ni Diaaaaaaaallllo
Eh Yako Diombba Niaw Yow
Aaye Waaye Demba Tali Meissa Diop
Bidéw Goor Gua Diodio Ndiaye
Diguenté Mar ak Gana Gobé
Thiala Yacine Niokhobaaye Dem Neu
Socé FALL Dawour FALL
Massamba Ndoumbé FALL
Gno Meunone Thiolo Ngour Sambo
Meissa Coumba Bigué
Lary Coumba Bigué
Soko Diack Ndella Ngoné
Cheri Kaay Faune Meu Yama Té Nelaw
Baye Cherif Leunde Djeudi Yaram
Loffi Niane Mou Nangou Nianal Niou
Yow Deh Laniou Ragné Bi Ndaw Adouna
Cheri Cheri Coco
Yama Té Nelaw Waay Na Leu
Cheri Sama Ndanane Yama Té Nelaw
Aaye Waaye Cheri Cheri Coco
Yama Té Nelaw Waay Na Leu
Cheri Kaay Faune Meu Yama Té Nelaw
Ndeyssane Cheri Coco
Amoul Gueer Amoul Gueweul
Cheri Sama Xol Bo mélonni Maan
Gneuw Yéndoul ko tchi
Ecouter
A Propos de "Cheri Coco"
Plus de Lyrics de AMIRA ABED
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl