ELJAZ Bama cover image

Bama Lyrics

Bama Lyrics by ELJAZ


Let’s go
Yagu yagu dina bakh
Niveau bi geuna yék dou messa bas
Boulnémane dema ay bouléssi kay
Dina téyé game bi diarol listikhar
Deuk si war, ni dokér si car
Khamo fouma diouhé ni dokhote si car
Doneu superstar, dawal jaguar
Beuri péhhé ni guél bi am niéti far
 Kou beugua guiss guor yalla nama khol
Diémnagn mais yakouniou sama khol
Mane ak niom je suis le plus fort
Bandit la wowéma billy boy
Deuké di diam sama cible
Louma yotou diotsi, mane mi douma reub soy
Fonctionné goudi ak beuthieuk
Soudé danga geuméntou démal nga teudi boy
Geuna dek si sama passe-temps
Doume boulé damay passe camps
Ballamaissa sama askane
Dakar médina sama makane
Diakhassé lép si ndiak li
Weurseuk nio dakadji bo safoul niou sapali
Nioune daniou magué si médi di khékh sougnou libérté meunouniou niak fit
Goudé teud téla diouk
Birou niay dounio téla sour
Gaindé deuk djiko bour
Dounio bayi, dém jusqu’au bout
Mangui yak rap bi m’en fous
Fuck rap bou waw bi dokhatoul
Diap mc yi di noguatou
Même soma khaméwoul dégu nga sama tour

Hey diokhoma lék , Diokhoma nae
Soma méré, Je m’en fous
Diokhoma lék , Diokhoma nae
Kone Soma méré, Hey i don’t care
Bama, wakhal sa wakh rék té bama
Cupél sa bop té bama
Bouma lidianti yaw bama
Heyy bama wakhal sa wakh rék té bama
Cupél sa bop té bama
Bouma lidianti yaw bama

Ngay casse casse may casse tout
Mane gass nga deuké soule
Sissou man yangui sissou
Mangui si kaw niongui sisouf
Contane di bégué nga beuge ma méré
Diam la woté mane begoma lénéne
Yangui yak sama dér
Yag ma djigne louma défoul
Ennemi arrête
Say dieuf douma mérlo
Douma khadi lo dafmay yok diom
Beugou lo fouma sérlo
Va te fait foutre niapal sa khone
Do meussa guiss sama rangogne
Do dégu niounéma ma togn
Dara dou khéw bama tite
Souma doné tapét yapeu sama wa kogne

Diokhoma lék Diokhoma nae
Soma méré, Je m’en fous
Diokhoma lék Diokhoma nae
Kone Soma mere, Hey i don’t care
Bama, wakhal sa wakh rék té bama
Cupél sa bop té bama
Bouma lidianti yaw bama
Heyy bama wakhal sa wakh rék té bama
Cupél sa bop té bama
Bouma lidianti yaw bama

Hey Je m’en fous
Hey i don’t care
Bilay Je m’en fous
Hey Je m’en fous, i don’t care
Bama, wakhal sa wakh rék té bama


About Bama

Album : T.L.Y.F (EP)
Release Year : 2021
Added By : Farida
Published : Dec 01 , 2021

More ELJAZ Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2022, We Tell Africa Group Sarl