Mbegte Lyrics
Mbegte Lyrics by DIZZY KHA
[REFRAIN]
Khonete poche chi peundeu andeu sek mbegte
Cheve tok si keur yi andeu sek mbegte
Y’allah ko def lossi meun khana am ci mbegté
Na cassou coffee weur nieupa goukh xol yi fekh
Walabok niou am mbegte begeul begeul
Fi daniouy begue di begle, begeul begeul
Dieuleul sama number ndax nga woma biss bo merete ma may la mbegte
Ndax merr kate yi daniouy tela deh
[COUPLET 1]
Sama mbegte moma yittel sil ay dokh
Pas de negativite je fus la joie gayi bougouniou nga begue kone nak fauk nga begue
Diafe diafe meunoul diafe ndax sa xol la fekh
Kholal fils y’allah loumou mounti dogal daf may saf
Zero pression ni kou ne huitieme etage
So guisse rongogn sama da fek ma re ba dioy
Mane kouma lebale sokhor mbegte la ley faye sa borr
Aduna c’est des haut et bas moussoul tax mou sexy ne len faux depart
Te tarr doga nekhi bamay ganessi aduna indale mbegte mo taxone ma sign
Banex nakhar dey safal sa life ni aromagie
[REFRAIN]
Khonete poche chi peundeu andeu sek mbegte
Cheve tok si keur yi andeu sek mbegte
Y’allah ko def lossi meun khana am si mbegté
Na cassou coffee weur nieupa goukh xol yi fekh
Walabok niou am mbegte begeul begeul
Fi daniouy begue di begle, begeul begeul
Dieuleul sama number ndax nga woma biss bo merete ma may la mbegte
Ndax merr kate yi daniouy tela deh begeul way
[COUPLET 2]
Loumou mounti done legui mou dialeu, soko nobe sandil de bi mou gaw
Game bi dou khar begeul way, etre malheureux c’est perdre du temps
Ben nakhar egal ben nakhar soula nakhri we nga am niari nakhar
Niari nakhar egal niari nakhar soula assassiner nga am nieti nakhar
Sape begue ndol begue niaw begue noy begue, ndam begue defaite begue
Gni dess tristesse dougn ko guiss deh
Défal leep loulay happy lo, no one yi bouniou nameu sa dentition
On a dit merci ay banalite nelaw you khoote ni kou fanane ci tenn
Y’allah soula beugue fauk mou tek la natou you beurri
Kone nak gerel te nga re ni kou tegui natou beugn
Meun nga bégue té do am alale, meun nga am alale té do bégue
Zéro yi beurinagn sis a compte wayé nékhoul sou andoul ak zero stress
[REFRAIN]
Khonete poche chi peundeu andeu sek mbegte
Cheve tok si keur yi andeu sek mbegte
Y’allah ko def lossi meun khana am si mbegté
Na cassou coffee weur nieupa goukh xol yi fekh
Walabok niou am mbegte begeul begeul
Fi daniouy begue di begle, begeul begeul
Dieuleul sama number ndax nga woma biss bo merete ma may la mbegte
Ndax merr kate yi daniouy tela deh begeul way
Watch Video
About Mbegte
More DIZZY KHA Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl