Fans Yi Lyrics
Fans Yi Lyrics by ADIOUZA
Mane beguer nallene
Eh beguer nallene
Fans yi namonalene namonalene
10 ans déjà
yone wi metina
Cey yi le soper
Bayiwougnouma
Yageuna beug deff weuye wi
Waxlene fima tolou thi yene
Loune nguene di dathieu
Nguir Mane
Te Mane yeknako
Xex souba Ngone yeknako
Lou Len meti yeknako
Mane Sama xel sama xol langui Thi yene
Taye ma sargalene yene fans yi
Mane beguer nallene
Eh beguer nallene
Fans yi namonalene namonalene
Ligueye bo Thi donner djiguene
Faut k nga xamner
Foula moye Li geune
Yen saye nite guisse la télé xemem la tok di dioye
Weur la wolou la nga gneuw bo noyer bop dioye
Kaye ma xamalene touti
Fans yenou yeukati
Ani Wa pikine
Parcel
Thiaroye
Yarax
Guediawaye
Rio
Keur Massar médina
Ziguinchor ba ndar beguer nagne ma waye
Mauritanie ba gambie beguer Baguer nagne ma waye
Jappeu nguene tewa bayi, douma xadi waye.
Mane beguer nallene
Eh beguer nallene
Fans yi namonalene namonalene
Mane beguer nallene
Eh beguer nallene
Fans yi namonalene namonalene
Taye ma weuyale lene
Yena ma japaler
Taye ma xamalene
Yena ma dolele.
Tiaba, Diarra Nancy, Bigue, Maimouna awa toure
Wolma mame Diongue loxo thia kaw
Leggo leggo
Weuye Lene ma ndeyssane sama mak ji
Ana Sagna chéri sadia
Wolma lamine fall ak fatou thiam
Begoulo ma mère dale Yaw
Domi ndey Mami diouf
Souma demer baye beugeu xadi chéri Aziz ndiaye dolele ma
Souma demer baye beuger xadi
Khady koundoule dolel ma
Tassou
Sa goune sa goune
Dioudou Bou reye ndey ak baye
Foulak fayda borome dale
Mareme chalar mimaye beugeu jigne
Aida Seye chéri lamine la bokale baye
Fou sama rangogne touro
Mareme fompale ngamako
Raki gamou seye
Diarama mareme
Weye lele weuyelelene ma mareme
Souma demer baye beugeu xady
Chéri doudou dolelma
Souma demer baye beugeu xady
Fat kine dolelma
Dj boubs, pape cheikh, cheix Sar Sidathe gnoma terrer chômer
Abba , Koutia, alima Maria gnoma tere chômer
Dieynaba, Nadia, haini, maty, kebs thiam leggo leggo
Watch Video
About Fans Yi
More ADIOUZA Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl