Free Lyrics
Free Lyrics by YOUNG TILI
Dara diaféwoul naniou geum en tout cas
Dagno beugg free eeee
Dagno beugg free eeee
Dagno beugg free eeee
Dagno beugg free eeee
Yonn wi métina
Yaye boye waxonn nama limoy adouna yeah hey
Barima ay coups bas
Mais douma téré xèkh pour lima geum en tout cas
Nitt mo leundeum té meuno xam, yeah
Lima doundou man faut le voir, yeah
Yall naniou yalla di soutoura walay
Yalla naniou yalla di soutoural, yeah
Thji niit yi am la beug bokk
Fou dianteu feulé damay takeu diouk
Yaye boye may nama fiit, foula, diom
Yar ma thji takandèrou Cheikh Anta Diop, konn!
Ila! ila dokh sama souba
Borom milliard eupouma foula
Auto ak villa ay lidieunti la
Nganii..!? Lutakh ?
Beugg rek ma dess guinaw
Motakh ngay indi fitna
Mais dina tègui touma
Dagno beugg free eeee
Dagno beugg free eeee
Dagno beugg free eeee
Dagno beugg free eeee
Yonn wi métina
Yaye boye waxonn nama limoy adouna yeah hey
Barima ay coups bas
Mais douma téré xèkh pour lima geum en tout cas
Comme diabar lalay xolé
Bama donn dii déconner
Yagg ngama support
Yagg ngama supporter
Ba weursuek niaké
Bagn ma wané guinaw ya nékonn à mes côtés
Sa kanam say réé
Say wakh aksa yènè lay xalatt di am dolé
Baatou makk santoul dèdett
Wakhou mbokou takk téré
Tè pourtant lamign yima worr fanla diougué?
Loudoul gars yima diéguè
Loudoul gnima foguonn nio bokou dèrètt
Yènn saay mbéttél dou diougué fi nga ko foguè
Dègg na louné, walay guiss n alou né
Mais la meilleure revenge moy sama succès. Konn !
Ila! ila dokh sama souba
Borom milliard eupouma foula
Auto ak villa ay lidieunti la
Nganii..!? Lutakh ?
Beugg rek ma dess guinaw
Motakh ngay indi fitna
Mais dina tègui touma
Dagno beugg free eeee
Dagno beugg free eeee
Dagno beugg free eeee
Dagno beugg free eeee
Watch Video
About Free
More YOUNG TILI Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl