Peundeul Lyrics
Peundeul Lyrics by NARAH DIOUF
Ak fo né thi town bi
Fo né thi rew mi
Gneuweul fi yeungou thi lii
Narah laye doooni
Manla ma gneuwat fi gueuneu
Teggou thi beat bi
Kholal ni mey dougué
Kholal ni mey yéggé sama baat thia kaaw
Mélodie bé meu yéglo
Guisseutoumeu degueutoumeu
Lene laye guiss kone kaye fii ma wone leu
Guisseutoumeu degueutoumeu leu
I’m so high
I’m so high yeeeeh
Kaye gnou Peundeul Peundeul Peundeul
Narah moy Peundeul Peundeul Peundeul
Kaye gnou Peundeul Peundeul Peundeul
Narah moy Peundeul Peundeul Peundeul
Lou fora fora fort laye yeuk sama khol
Fou kawe kawe kawe laye yéeek
Sama yaram di yeungou
Ta khawmeu likey yeungueul fimou diogué
Ayooooo
Goudi goudi non stress leu doundou happiness Tay non stop
Andak samay way tay deh fête leu
Kholal nima mell Kay dance all night
Sound bi ndakh yankey ngueug comme mane nimakey yeugué
Wakh ma ndakh moungley dougou comme nimmey dougué
Guisseutoumeu degueutoumeu
Lene laye guiss kone kaye fii ma wone leu
Guisseutoumeu degueutoumeu leu
I’m so high
I’m so high yeeeeh
Kaye gnou Peundeul Peundeul Peundeul
Narah moy Peundeul Peundeul Peundeul
Kaye gnou Peundeul Peundeul Peundeul
Narah moy Peundeul Peundeul Peundeul
Fakhassoul fakhassoul fakhassoul yow
Guenel lithi khool bi
Taye dougnou mayé dara
Yeungeutoul yeungeutoul yeungeutoul yow
Fakhassoul fakhasoul fakhassoul yow
Guenel lithi khool bi
Taye dougnou mayé dara
Yeungeutoul yeungeutoul yeungeutoul yow
Kaye gnou Peundeul Peundeul Peundeul
(Kaye gnou Peundeul )
Narah mou Peundeul Peundeul Peundeul
(Kaye gnou Peundeul Peundeul Peundeul Peundeul ehhh )
Kaye gnou Peundeul Peundeul Peundeul
Ehhh ehh ehh ehh ehh
Narah moy Peundeul Peundeul Peundeul
Hummm hummm
Watch Video
About Peundeul
More NARAH DIOUF Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl