M.A.S.S Teggi Nat cover image

Teggi Nat Lyrics

Teggi Nat Lyrics by M.A.S.S

[COUPLET 1]
Demb la 5 nieup yeug nagn ko mère bi dafa téggi natt takoussane après agne
Awma khaliss, dagn ko miste pa bi 
Mère bé ayé souma nékhé guédeu khogn (ankay)
Daba sama néneu doko dégeu tay
Fay cash diokh ma sama wethite dama yakamti 
Fagn nagn la ba fayla khoromou demb ana sa bic barél niou sa cahier bi
Dagn ko khar manda ma « khoreudieu » kogn bi deugeur favelas city de Dieu 
Mère yi bougn la diourone boy nga yeureum len niou ngui togg niou ngui yakk kharou niou ken
Dagn ko khar manda ma « khoreudieu » kogn bi deugeur favelas city de Dieu
Mère yi amoul niou compte banque naniou mougn
Niou ngui tek niou ngui téggi di def si nioune
Nioune la boy you amoul héritage gallé bou nékhé mère bi dafa téggi natt
Nioune ken douniou diapeu otage pa bi khamoul gnatta lagn dépense du moins
Nioune la boy you amoul héritage gallé bou nékhé mère bi dafa téggi natt
Nioune ken douniou diapeu otage pa bi khamoul gnatta lagn dépense du moins

[REFRAIN] 
Mère bi dafa téggi natt 
Gallé dina nékh mère bi dafa téggi natt 
Mère bi dafa téggi natt 
Gallé dina nékh mère bi dafa téggi natt
Téggi, téggi natt, téggi, téggi natt

[COUPLET 1]
Mère collé néna call na ba sone lébal ko bam téggi lokhom dafa tolou diganté 
Domou yaye ndiolé gneuw na fi néna faye ko dièznère bi adama di ngenté
Ngané ma boul ndawtali leep beug nagn noce noce ay fanni fanni ndawal
Boul lébal pa bi dakay jouer parifoot PSG dorati Marseille nioune douniou tale 

[OUTRO]
Dagn ko khar manda ma « khoreudieu » kogn bi deugeur favelas city de Dieu 
Mère yi bougn la diourone boy nga yeureum len niou ngui togg niou ngui yakk kharou niou ken
Dagn ko khar manda ma « khoreudieu » kogn bi deugeur favelas city de Dieu
Mère yi amoul niou compte banque naniou mougn
Niou ngui tek niou ngui téggi di def si nioune
Nioune la boy you amoul héritage gallé bou nékhé mère bi dafa téggi natt
Nioune ken douniou diapeu otage pa bi khamoul gnatta lagn dépense du moins
Nioune la boy you amoul héritage gallé bou nékhé mère bi dafa téggi natt
Nioune ken douniou diapeu otage pa bi khamoul gnatta lagn dépense du moins

[REFRAIN] 
Mère bi dafa téggi natt 
Gallé dina nékh mère bi dafa téggi natt 
Mère bi dafa téggi natt 
Gallé dina nékh mère bi dafa téggi natt
Téggi, téggi natt, téggi, téggi natt

[OUTRO]
Tay ken dou dépenso 1000f mère dafa téggi natt
Tay ken dou dépenso 500 mère bi mo teggi natt
Daniouy fay cash boutique ba
Diallo diokhma sama wéthite 
Tay niouy ndéki, agn, rérr té kén dou tibeu ci agn rérr

[REFRAIN] 
Mère bi dafa téggi natt 
Gallé dina nékh mère bi dafa téggi natt 
Mère bi dafa téggi natt 
Gallé dina nékh mère bi dafa téggi natt
Téggi, téggi natt, téggi, téggi natt

Watch Video

About Teggi Nat

Album : Teggi Nat (Single)
Release Year : 2018
Added By : Tamsir Diouf
Published : Sep 17 , 2019

More M.A.S.S Lyrics

M.A.S.S

Comments ( 0 )

No Comment yet

About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl