Paroles de Poka Poka
Paroles de Poka Poka Par PAAPAREY
Bakandil niou khol,
Défé ko noumou la nékhé
Bi moy fethi Poka Poka ay
Niarri nitte ley lathi, goor ak
Djiguen délo koko mou délola Poka Poka
Ay ! Dolé biir la lathi Poka Poka
Tek ko ci temps mou nice Poka Poka
Wolou nga sa ndigue Poka Poka
Kone yako téré nekk Poka Poka
Dolé biir la lathi Poka Poka
Tek ko ci temps mou nice Poka Poka
Wolou nga sa ndigue Poka Poka
Kone yako téré nekk Poka Poka
[COUPLET 1]
Féthial ma guiss niowal niou dem
Khalil nala guew bi wane ma sey fem
Na melni walakh diane cibiir guethi
Yeungeuleul sa ndigue boudé yako mome
Indalel sa tioumbkay bou dara dess
Takkal ko ay téré ndigue bamou fess
Dawal ci kawam bouko khar mou niow
Léweutol ak mome dorr ko gauche droite
[REFRAIN]
Bakandil niou khol, défé ko noumou la nékhé
Bi moy fethi Poka Poka ay
Niarri nitte ley lathi, goor ak
Djiguen délo koko mou délola Poka Poka
Ay ! Dolé biir la lathi Poka Poka
Tek ko ci temps mou nice Poka Poka
Wolou nga sa ndigue Poka Poka
Kone yako téré nekk Poka Poka
Dolé biir la lathi Poka Poka
Tek ko ci temps mou nice Poka Poka
Wolou nga sa ndigue Poka Poka
Kone yako téré nekk Poka Poka
[COUPLET 2]
Déko diéguer, diko coller
Boul bayi espace tek koko
Khol ko ci beut ba sopaliko
Lale lokhoy titeuro
Poka Poka girls your welcome
Makk ak ndaw nieup ci lagn bok
Poka Poka hé, Poka Poka hé !
Niou rek from sénégal
[REFRAIN]
Bakandil niou khol, défé ko noumou la nékhé
Bi moy fethi Poka Poka ay !
Niarri nitte ley lathi, goor ak
Djiguen délo koko mou délola Poka Poka
Ay ! Dolé biir la lathi Poka Poka
Tek ko ci temps mou nice Poka Poka
Wolou nga sa ndigue Poka Poka
Kone yako téré nekk Poka Poka
Dolé biir la lathi Poka Poka
Tek ko ci temps mou nice Poka Poka
Wolou nga sa ndigue Poka Poka
Kone yako téré nekk Poka Poka
Ecouter
A Propos de "Poka Poka"
Plus de Lyrics de PAAPAREY
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl