Paroles de Highlander
Paroles de Highlander Par NIX
[REFRAIN]
Vieux père bou doul maguette Highlander
Dague sene boppe lay def Highlander
Décapité par le chef Highlander
Vieux père bou doul maguette Highlan...
Vieux père bou doul bayi Highlan...
Vieux père bou doul maguette Highlander
Fou niou dougou ma lidjenti lene
Mane késsé boy kene dou ma donneu
Niou yeungou ma dagati lene ngene sorima lo ley lou dagane
Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live)
[COUPLET 1]
Bou may dioudou rap dé amagoul, fii la ma fekk ni seeni doule
Ma impermeable ci yeah dama toul té nope bou nathioul dé dégagoul
Baggy jeans Wu Tang diamono May battle di battle di battle Freestyle ma lay golo lo
May danel di danel di danel
So ma wédé laadj ma Xuman
Tekk ay flowou Busta mel ni dou mane
Au final yakamti pour lane
?
Periode bobou dam ko djegui ni dos d’âne
Néka gouma artiste solo mais ma ngui ci game bi ni gaindé bou souroul
Di dougal ay MCs ci biir kilo mbourou di dokhontou ci kogn bi di weur ay foureul
N-eazy defal ndank lou eupeu tourou
! Ma keupeu yelwane bi sama boy yi djiiro
Surveillance générale la bagné bureau
, ndékété mariage dafa wekh ni gouro
Dou ma la djaay experience boy amo ndjeugam
Degn ma yarr boy xébouma deureum
Degn ma nokhe boy ba tay may geureum
Golden boy dama nioul ni peureum
Longévité boy dou serigne dou mara dou téré dou garap
Boy défo fii dara, dou palace dou baraque
Dou Donald dou Barack, dou Point E dou Karack
Lou gnou cons boy dou diaraat,
Laadjal Egypte boy fou gnou tégone Mubarak
Mais y’Allay buur sou ko nékhé gnou faraat
Kone N-eazy bayil sou la nékhé nga dieulaat
…
Ndakh yaay vieux père bou doul maguete Highlander
[REFRAIN]
Vieux père bou doul maguette Highlander
Dague sene boppe lay def Highlander
Décapité par le chef Highlander
Vieux père bou doul maguette Highlan...
Vieux père bou doul bayi Highlan...
Vieux père bou doul maguette Highlander
Fou niou dougou ma lidjenti lene
, mane késsé boy kene dou ma donneu
Niou yeungou ma dagati lene ngene sorima lo ley lou dagane
Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live)
[COUPLET 2]
Katana bi loumou dag ci boy raw na dibiterie
Tête de mort nékone fi tendance bi
Tout ce que je voyais c’est mes trophées qui me sourient
Quick and flow mo déloussi boy ay éclaire lay conss ni N-eazy
Rap galsen sama dome on est père et fils
Mamou mamati mame mou sen lyriciss ay sur flo thérapise
Koufi antane sama légacy
Na tékki térém dérét takhal yérém
Bann bi takhal bérém
Ball yi takh tuh tuh tuh !
Boy niou teureul len yen ak sen kheureum fils
Equipe bou fess ak ay génies fils
Do lathi orange lane moy bénéfice
Do lathi wa yoff coss kouy diar ak caisse boulay féignou doka téla guiss
Té longévité dou mayé dou sarax
Dou jordan dou thiarakh dou kégn nékh dou forokh
Mais toujours frais comme le vieux père
Ray la ni sourire’ou joker Highlander
[REFRAIN]
Dague sene boppe lay def Highlander
Décapité par le chef Highlander
Vieux père bou doul maguette Highlan...
Vieux père bou doul bayi Highlan...
Vieux père bou doul maguette Highlander
Fou niou dougou ma lidjenti lenn
Mane késsé boy kene dou ma donneu
Niou yeungou ma dagati lene ngene sorima lo ley lou dagane
Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live)
Ecouter
A Propos de "Highlander"
Plus de Lyrics de NIX
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl