M.A.S.S Wodou Wodou cover image

Paroles de Wodou Wodou

Paroles de Wodou Wodou Par M.A.S.S

[INTRO]
M A S S
Khalé wodoul seurr way
Mais Double B, niou dém, niou dém
Ahan, right

[COUPLET 1]
Guissa touma kéne wodou seur, Niom nieupa beug dieukeur
Douma né djiguène waw goor, Wakhalmako waw Coumba
Coumba tchi supermarché, cheveux naturels sa bopp ba
Na ndiampé batchi mbombe
Kène doufa ték lékétt khamnga
Khamo né jean day wagni ay limouy woné lépp
Seurr dafay yokk koumpeu lancement wou film bi leu
Yala bo téyé bol sa ndigg dig yoor-yoor
Dokh ndank sa tank yeukeuti soufou dior
Mbole amoul Dakar kon ma mayla "seukeukdior"
Soda Mama diangalal khaléyi ni niouy také seurr
Deureum, sa lafou seurr, sougnla mayé takk fa
Laf tiat, khalé bi, fi rabal nékone diogoufa

[REFRAIN]
Wodou, wodou, wodou
Waw Coumba takk na seurr
Rabal ak piss bakhna déf sa wax may sa dieukeur
Kou beugoul man beugue na
Wodoul, wodoul mayma
La pluie est maintenant rare comme djiguènou khaléy seurr
Wodou, wodou, wodou
Waw té Coumba takk na seurr
Rabal ak piss bakhna déf sa wax may sa dieukeur
Kou beugoul man beugue na
Wodoul, wodoul mayma
La pluie est maintenant rare comme djiguènou khaléy seurr

[COUPLET 2]
Fétial bawounane mou taw
Danio tangue tangue

Nioune daniou sone ci leggings Rihanna ak Beyoncé
Namm guiss Aida, Siga ak Dibor niniouy sagnsé
Dém toll amou fi wayé niou ngui lékk kemb
Tchi soufou garap tek ataya mangui mayé tiaya
Coumba ni ngay dokhé di daagou dégg nako sama bro
Kon statut, freeze, ma selfie, please
Lou yagg né Coumba Gawlo légui niou feug takal sa seur
Nga fétch bawounane rek mou taw tchi nda ni dieukeur
Mannequin tchi boutique bi ay pantalon la niouy diaye
Man seurr lay weur, loumou diarr ma dieund ni guérté noflay
Man ndiaago tour na diw
Wagass sa seurr Khar Mbaye weuyla
Laf tiatt, khalé bi, fi rabal nékone diogoufa

[REFRAIN]
Wodou, wodou, wodou
Waw Coumba takk na seurr
Rabal ak piss bakhna déf sa wax may sa dieukeur
Kou beugoul man beugue na
Wodoul, wodoul mayma
La pluie est maintenant rare comme djiguènou khaléy seurr
Wodou, wodou, wodou
Waw té Coumba takk na seurr
Rabal ak piss bakhna déf sa wax may sa dieukeur
Kou beugoul man beugue na
Wodoul, wodoul mayma
La pluie est maintenant rare comme djiguènou khaléy seurr

[COUPLET 3]
Fétial bawounane mou taw
Danio tangue tangue
La pluie est maintenant rare comme djiguènou khaléy seurr
Fétial bawounane mou taw
Danio tangue tangue
La pluie est maintenant rare comme djiguènou khaléy seurr
Fétial, fétial, fétial Fétial, fétial, fétial Fétial, fétial, fétial
Wodoul, wodoul, wodoul Fétial, fétial, fétial
Niou délou démb
Fétial, fétial, fétial, Lepp bakhna
Fétial, fétial, Wodoul, wodoul Fétial, fétial, 

[REFRAIN]
Wodou, wodou, wodou
Waw té Coumba takk na seurr
Rabal ak piss bakhna déf sa wax may sa dieukeur
Kou beugoul man beugue na
Wodoul, wodoul mayma
La pluie est maintenant rare comme djiguènou khaléy seurr
Wodou, wodou, wodou
Waw té Coumba takk na seurr
Rabal ak piss bakhna déf sa wax may sa dieukeur
Kou beugoul man beugue na
Wodoul, wodoul mayma
La pluie est maintenant rare comme djiguènou khaléy seurr

Ecouter

A Propos de "Wodou Wodou"

Album : Wodou Wodou (Single)
Année de Sortie : 2017
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Sep 19 , 2019

Plus de Lyrics de M.A.S.S

M.A.S.S

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant

A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl