
Paroles de Loloy Zé
Paroles de Loloy Zé Par DIZZY KHA
[Chorus]
Loloy zé…loloy bandit …bo dofé …ma nane kaani
Soma geunoul tekki lomay conseiller?
Wahko sa bopp soma beugoul yow la concerner,
Wakhko sa bopp ahhh
Tombola locolo
Tombola locolo
Tombola locolo
Tayal sauf boudé pour outi kopar
dakk benefice moy sama sport du jour
Naniou dagay guéné album gnoudiko
Khar ga guéné ay daye ni kou took di (ounh)
Lolou dou jouer, teukounalene khana jongouwoulene
Thiow boudoul diekh lima désséwon si
Diam la diolou mou diekh bodé danou
rap feke fi thierno moulé
Aye thi doule thi net bi teulé def son bou nekh
Mayonnaise bi dog na nigga néko sour negne
Game bi reptyle music nioko séddo mou diekh
Public bi nangouna, motah may bakou nak diga dégue ni
Danou na, so guissé sa bakhou mame
Yak sa projet thiéré pour yow chine ga né
Sa agne bou tewoule boulko djigne sa mere
Mener creuser ecart ni kou time sa gue
L bayila guinaw plusieurs kilometres
[CHORUS]
loloy zé…loloy bandit …bo dofé …ma nane kaani
Soma geunoul tekki lomay conseiller?
Wahko sa bopp soma beugoul yow la concerner,
Wakhko sa bopp ahhh
Tombola locolo
Tombola locolo
Tombola locolo
aywa yapou rappeur kayelen pesser kougnfi né
goat nala sequin yagga dougal maniw figa guéné
Reglel meun na am may sa pere
Diemeul crever samay roues digfa am dofou new
au suivant je tabasse qui? Sa rappeur fokoule
man amna fake nigga you mboubo dji pikine
Ko seu ndeye néla simile le febaroulene bayilene
Films yi mane maguek carte fidélité clinique
loloy bandi, moytoul choco choco diarfa tiorokhani
Signer monogamie, mais dieul lene yene nieup melni photo Famille
ciseaux sa chignon ga goré some
Saw la poup la defla pot de chambre
Gayi diayla doule leu diohla connexion ma rayla soule leu soma togné bro
[CHORUS]
Loloy zé…loloy bandit …bo dofé …ma nane kaani
Soma geunoul tekki lomay conseiller?
Wahko sa bopp soma beugoul yow la concerner,
Wakhko sa bopp ahhh
Tombola locolo
Tombola locolo
Tombola locolo
Ecouter
A Propos de "Loloy Zé"
Plus de Lyrics de DIZZY KHA
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl