Paroles de Sour Naa
Paroles de Sour Naa Par DA BRAINS
[CHORUS]
Sour naa, thiérék deukhine sour naa
Makk louko rayy dékké bako toub na
Mandi niakeu dakh nio ngui tribunal
Koudou bou mak meun na
Yeungeul tchinou dakhinééé
[VERSE 1]
Setlou na manatouma ndéké galé
Damay takkeu dioug dieul lima am yobalé
Sangara, deugeu leu yamba dou balé
Sathi laniou mey djigne
Té nane may dogualééé
Mandéti nga déh
Dotouniou amati diameuh
Dama beug nga nek nitte
Si keur gui wala ma doumeu leu
Mouno deuké di khékh sageu ndeye
Ci kogn bi wakh diou niaw gouné guéneu sa lamign
Deug kham nga né mandi warou leu
Sama mandi yonou kéneu nékouci
Sama khaliss daf ma léw kone nga mandlou ci
Mandlou na ci demb ak tay mou andil leu fitneuh
Yokkeu mère bi thiono kay niou agn té nga bayi thiow li
[CHORUS]
Sour naa, thiérék deukhine sour naa
Makk louko rayy dékké bako toub na
Mandi niakeu dakh nio ngui tribunal
Koudou bou mak meun na
Yeungeul tchinou dakhinééé
Sour naa, thiérék deukhine sour naa
Makk louko rayy dékké bako toub na
Mandi niakeu dakh nio ngui tribunal
Koudou bou mak meun na
Yeungeul tchinou dakhinééé
[VERSE 2]
Dmay mandi feusseul nako
Wayé niatta gno fi yakeu biir diapeu sen ndiambour
Niatta gno fi lucide dokhane diabarou diambour
Pa dou deg ngeu da am loy
Lidieunti sama potou chambre
Mère ioe guéneul samay wax deg ngeu
Barki demb ndiaye sa dieukeur mofi bireul bagn ko
Yén li bone mi ngui ci keur gui déh
Té guissou len ko liguèyeunté souba ak ngone
Geuneu graw mandiiii
Pouthi pathi lékal deukhine pouthi pathi
Bayil lékk nitte bayil tamit ndioudj ndiadj
Tokk di mandi meu geuneul di weur fen founé
Niatta yone la magoum
Djeum yégu sikaw goné pédophile
Dou nathi bou tangue mandi kat
Dey geuneu diapeu nékh (waw)
Wayé cooleul rekk légui
Police niow mou diékh (mooh)
Yéneu deum yi si niom nioma dakh mandi
Bouniou dieulé taxi clando
Bouniou doug mou diékh takkeu nak
[CHORUS]
Sour naa, thiérék deukhine sour naa
Makk louko rayy dékké bako toub na
Mandi niakeu dakh nio ngui tribunal
Koudou bou mak meun na
Yeungeul tchinou dakhinééé
Sour naa, thiérék deukhine sour naa
Makk louko rayy dékké bako toub na
Mandi niakeu dakh nio ngui tribunal
Koudou bou mak meun na
yeungeul tchinou dakhinééé
[OUTRO]
Pouthi pathi lékal deukhine pouthi pathi
Bayil lékk nitte bayil tamit ndioudj ndiadj
Tokk di mandi meu geuneul di weur fen founé
Niatta yone nga trompé sa
Diabar ci keur goné mbarane
[CHORUS]
Sour naa, thiérék deukhine sour naa
Makk louko rayy dékké bako toub na
Mandi niakeu dakh nio ngui tribunal
Koudou bou mak meun na
yeungeul tchinou dakhinééé
Sour naa, thiérék deukhine sour naa
Makk louko rayy dékké bako toub na
Mandi niakeu dakh nio ngui tribunal
Koudou bou mak meun na
Yeungeul tchinou dakhinééé
Ecouter
A Propos de "Sour Naa"
Plus de Lyrics de DA BRAINS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl