Bamba Lyrics
Bamba Lyrics by CHERIFOU
Mourite touba sunu xol
Mourite khelcom sunu toll
Mourite thianta lay dõne
Mourite baye fall lay dõne
Mourite touba sunu xol
Mourite khelcom sunu toll
Baye fall lay dõne
Thianta lay dõne
Bougnou Diaggé Nagnou xam léep yaw laa
Bougnou Goré Gnou sante laa warna
Yaw Bamba, cheikh Ahmadou Bamba
Xaliil gua Yonn ,Indi gua léer .
Bounou Diagué léep yaw la
Bounou Goré Nélaa Yaw laa.
Jeuff gua Lou Reuy si xol
Gnou diko séddé
Indi gua xéweul ,Indi gua Naatangué
Touba moy Guenél du sùnu Mbécté
Islam Amati Ndàm gnou Dikko Fêter
Diguenté Wirwir Mayomba
Diouli si guéthi akk NõNam Ya
Taxùko Yénni Yanaam baa
Yalla la Doylo ak Yonéen Baa
Lamù Tontou bureau bâ sa Ndar
Takhaaw Ni yalla bour
Ibra fall Fégnou Koo Nànn
Mbacke yaye sén bour
Bougnou Diaggé Nagnou xam léep yaw laa
Bougnou Goré Gnou sante laa warna
Yaw Bamba, Cheikh Ahmadou Bamba
Xaliil gua Yonn , Indi gua léer
Bounou Diagué léep yaw la
Bounou Goré Nélaa Yaw laa
Jangalé gua Alkhourane
Térée na Safane
Dimbali ganou bagnou Mouthiou si Nassarane
Niogui sùkù Raam
Délou Sakù Niann
Serign bi Taff nou sa Barké.
Dômi Mame Diarra Yoroul Liy Loré
Mbacke Balla Aisha Ya Goré
Yarr ganou Yiir ganou ar ganou Ya tabé
Soll ganou Jikko Yi Geunn Gnù Diko wanée
Lamou Tontou Bureau bâ sa Ndar
Taxaaw nii Yalla bour
Ibra fall fégnou ko Naan
Mbacke yaye sén bour
Bougnou Diaggé Nagnou xam léep yaw laa
Bougnou Goré Gnou sante laa warna
Yaw Bamba, Cheikh Ahmadou Bamba
Xaliil gua Yonn ,Indi gua léer
Bounou Diagué léep yaw la
Bounou Goré Nélaa Yaw laa.
Ayoo léeeée... Ayoo lélélélé ée...
Kén d'où Mame cheikh ibra fall
Baye fall, baye fallou baye Faye yi
Kokou moy cheikh ibra fall Abo Ridial.
(Hommage Au Fondateur Du Mouridisme, Cheikh Ahmadou Bamba Mbacké Khadim)
Watch Video
About Bamba
More CHERIFOU Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl