AZAYA  Je T'aime Un Point C'est Tout cover image

Je T'aime Un Point C'est Tout Lyrics

Je T'aime Un Point C'est Tout Lyrics by AZAYA


La guineé – Sénégal c’est l’afrique qui gagne
Ouuhh ohh oo, zaya
Je t’aime un point c’est tout
hOo woo, un point c’est tout 
Je t’aime un point c’est tout
Yarabi mani chérie té mbifé  (Bambara)
Je suis ton roméo, tu es ma Juliette
Baby toi et moi pour la vie
Je suis ton romeo tu est ma Juliette
C’est toi et moi pour la vie

Bébé chérie je t’aime un point c’est tout
Wallay bilay, je t’aime un point c’est tout
Bébé chérie je t’aime un point c’est tout
Wallay bilay, je t’aime un point c’est tout
(Un point c’est tout)
Hooo hoo, un point c’est tout
Je t’aime un point c’est tout, yarabi mani chérie té mbifé

Sama mbeuguel mon ngui daw di niow ci yow
Sa mbeuguel di naw di niow ci mane
Soumala khamoul wone, kham na ni douma bardé
Yowit soma khamoul wone sama goor do bardé
Ndax li gni doundu, dafa nexa nex
Ndax li gni doundu mak yow mo daak nex

Sama xol sama life soma bayé dina weet 
Yama mom, mala mom pour la vie
Sama xol sama life soma bayé dina weet 
Yama mom, mala mom pour la vie

Beugeu nala té fowéwou mala beugeu nala
Fawma di rafé fufa hoo
Beugeu nala té fowéwou mala beugeu nala
Lima am, li nga am, niou bolé ko mou nek ben 
Chérie beugeu nala
 Lima am, li nga am, niou bolé ko mou nek ben 
Chérie beugeu nala
Hey my boy soumala guissoul damay weet ndax yoww rek la mine
Guiss la beugeu la loukay fay, 
Wax nako beugoulo loumay gagn kham nako
Amoul Adji amoul Ass, lou woor la 
Lima yeug dou ay foo lou woor la

Sama xol sama life soma bayé dina weet 
Yama mom, mala mom pour la vie
Sama xol sama life soma bayé dina weet 
Yama mom, mala mom pour la vie

Bébé chérie je t’aime un point c’est tout
Wallay bilay, je t’aime un point c’est tout
Bébé chérie je t’aime un point c’est tout
Wallay bilay, je t’aime un point c’est tout

Watch Video

About Je T'aime Un Point C'est Tout

Album : Je T'aime Un Point C'est Tout (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Nov 11 , 2019

More AZAYA Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl