Aby Lyrics by NGAAKA BLINDé


Just for my baby
She name’s Aby
None lako nobé
Do you know wanna mean
Nieupp xamné
C’est elle ma vie
Bougn sax andé all eyes on me
Aby dafa diekk change
Xawma lougn ko wakh ak loumou degg ak loumou done
Mane dé ma ngui fi… di shine
Toukh samay vibe samay crac samay  bone Nane
Aby -aby
Aby ya ngui ma ngui
Aby-aby

Aby j’te mens pas moi
T’es la seule qui est dans mon viseur
J’t’en parle ça fait des mois
J’en ai parlé même à ta p’tite sœur
Aby sama xolmi xolmi
Aby sama xolmi xolmi
Aby sama xolmi xolmi
Aby sama xolmi xolmi Eh

Néwone nala seey nekhoul
Xamone nako bettouma
Beugone nala bamou diéx mane
Ba beugone leu takk ci souba
Souma xamone ni nga may deff
Doumala diox sama xol mane mi
ABY ya know this is my baby follow me
I don’t let you go No
Loutax nga tekma thiono
Dama soneu boy
Sa yaye nénama non-non
Beugone leu takk defla soxna
Sa pape nieuw né non-non
Affaire de derett leu boy fils
Té waroul wone démé ni
Aby aby
Aby ya ngui ma ngui
Aby aby

Aby j’te ment pas moi
T’es la seule qui est dans mon viseur
J’t’en parle ça fait des mois
J’en ai parlé même à ta p’tite sœur
Aby sama xolmi xolmi
Aby sama xolmi xolmi
Aby sama xolmi xolmi
Aby sama xolmi xolmi

Regarde-moi aby tu vois bien que j’suis plus ce petit
Regarde moi je suis capable de combler ton appétit
T’es loin de moi, loin des yeux loin du cœur du future baby
Tu fais genre Tu m’entends pas quand je s’rais parti là tu verras
Qu’aby j’te mens pas moi
T’es la seule qui est dans mon viseur
J’t’en parle ça fait des mois
J’en ai parlé même à ta p’tite sœur
Aby sama xolmi xolmi
Aby sama xolmi xolmi
Aby sama xolmi xolmi
Aby sama xolmi xolmi

Hey Yeah …. Yeah yeah

Watch Video

About Aby

Album : Aby (Single)
Release Year : 2022
Added By : Farida
Published : Mar 16 , 2022

More NGAAKA BLINDé Lyrics

NGAAKA BLINDé
NGAAKA BLINDé
NGAAKA BLINDé
NGAAKA BLINDé

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl