KARBALLAH Comme Malla cover image

Comme Malla Lyrics


  Play Video   Watch Video   Correct  

Rap

Comme Malla Lyrics by KARBALLAH

Lekanté ni till Wexanté ni mbam
Xeutio comme bouki nieup deung dokh ni diane
Bayil héritage niou tiop sa neew ni tann
Weddi sa bopp moy mbamxoukh bou sekhlou bann
Loyy ignane Jassit né kene dou naane
Baboune embauché gollo né dougn tollo liniouy am
Njamala diar ba dial li yeup moko namm niongsi regnou fass
Fass né mom kou dawoul rk do am
Ségg yé sekk ngour né gaindé dafa maguette
Niay mangay sayy momak siirou daniou tapette
Njougoup lep la giss mai lim giss yeup dakoy sakette
Meune nagn terré weuliss sékkou mai dougn terré weuxeugn am xett
Natt geune di timpi tampa
Tioker ba dinthj lim yor
Doxine ba jeul na kakatar leuk xarab gniko dji ngor
Keur gué djigone mouss ak ounkou guinar xadjak nakk ki
yor ndawal aakk yaw lagn faal pithi yeup di sapp
Rene leu fêtou barr yi mbeut di kass
Mbonatt né tioloul ndakh bou taré moungsi keul di lass balegui
Wankh yi defnagn gang andak gounaur taxoul
ba melentannak sakh tay Senoup andeu saxoul

[CHORUS]
Nitt gni legi comme malla
Nitt gni legi comme malla
 Nitt gni legi comme malla
Nitt gni legi comme malla

Lane lagn jangue si jangalé niomi mame
Tay jeum yi taukhouwougn djiko yé walliyann
Nenagn jam diou bari la magg yi niane
Ladjal sa bopp khol sa reew ak melokannam
Li yeup foumouy moudié
Niako référence yo meune khol di royy si djiko ba bo euwlo joubok ouddé
Cherchél solution bi souniou biir
Boul woté émergent tadi taxaw saw si mur
Féne ba nda yi todjna maf yi claté
Kàania womatt bour yi atté juges waxma niata héros lafi reewmi soul ba faté
Boy soumb soumbeul gedj koukoy subir
Metit dou hôpital rk mo am niokofiy souffrir
Jangal nga bagn pour nga xam dina tarr
Tann nga yone bone tann lilay teksi naxar
Violences si faits legi meuwty dem ba dotoufi rare
Indiscipline kouné djiin fokné sa morom la warr
Soul nagn vestige lale fi prestige ak ay préjugé
Passive xol you maladif si sougn presqu'île
Xel bou xalatoul mok malla nio yem
Boul sikk kenen yarr bi geumko balangko jem

[CHORUS]
Nitt gni legi comme malla
Nitt gni legi comme malla
 Nitt gni legi comme malla
Nitt gni legi comme malla

Yeah
Nagn khollat bou bakh souniou bopp
Mounougn né daniouy défar souniou reew ba paré
Deffarouniou d'abord souniou comportement ak souniou djiko
Changement dou diougué fénen di nieuw fi
Nioune nioy jeul les choses en mains pour meune changer souniou destin
Reveillons nous!!!

Watch Video

About Comme Malla

Album : Comme Malla (Single)
Release Year : 2019
Added By : Preslie Nzobou
Published : Dec 11 , 2019

More KARBALLAH Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet

See also



You May also Like



Get Afrika Lyrics Mobile App

About AfrikaLyrics 

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2020, New Africa Media Sarl